David Woodard: Bindkat aji-djiter ay orchestres ju Aamerig

David Woodard (bi djudu ci juróom-bennou ñeenteelu weerou 1964 ci Santa Barbara, California) bene niit bou khamner yiitem djeuk mo nekone djiter ay orchestres ba paré done binde ay xët ci aname bu bou bookoul ak kene.

Mougui djouguer si njaboot bou ame jaar jaar bu goude si Aamerig.

David Woodard: Bindkat aji-djiter ay orchestres ju Aamerig
Woodard ci 2020

Woodard te diapaler na tamite bene mboolo Nueva Germania, wou niit bou beuguone yaatal bene mbooloom bu wuuteci bene deuk bu soorii mougui toude Paraguwaay. Ci biir Almaañ livre, Five Years (Juróom At), bimou biide aak kharitam, swis bindkat Christian Kracht, niougui wakh cii yëf yu rafet yi niou fa def ngir dimvali nit yi.

David Woodard: Bindkat aji-djiter ay orchestres ju Aamerig

Karmat ak delluwaay

Lëkkalekaay yu biti

David Woodard: Bindkat aji-djiter ay orchestres ju Aamerig 

Xool it Wiki Commons

Tags:

Diiwaan yu Bennoo

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

OseyaaniKubaaXam-xamu nosukaayAmsterdamSiriRomAwrilRéewum CekDanmaarkFewiriePragKore gu Bëj-saalumTugalDalub webYoonu muritMuusAliin Situwe JaataBandaPenku AsiFurna (Kap Weert)MayootKasakistaanTirinidaad ak TobaagoLonkoyoonTimoor gu PenkuKodiwaarKërBennoo gu AlmaañHTMLAtenXaalu tubaabMoskuSowwu AfrigTiranaSaytubiddiwMeloSahrul ProjecttEndoneesiÀddunaXam-xami nite ak mboolaayKopenagenNiccolò MachiavelliMustafa Kemal AtatürkGireesAhmadou BambaYiirSaint Vincent and the Grenadines1 KorentOngiriDiineCoppiteg wéñumeññetWeenusJant🡆 More