Niccolò Machiavelli: Bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali

Niccolò di Bernardo dei Machiavelli (Nikoloo Makiawelli)(3 mee 1469 – 21 suwe 1527) ab bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali la woon.

Wiki Niccolò Machiavelli
Wiki
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki taxawal
Niccolò Machiavelli: Bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali
Niccolò Machiavelli

Niki Leonardo Da Vinci, Machiavelli jàppe nañu ko kuy misaal dëgg-dëgg nitug yewwute. Bii tekki - ginnaaw ñu bari - di nanu xamal ci jëmm ji ak ci nitu mbind ki waaye du nu xamal ci ngérum machiaveli, mi dugg ci waxtaani bés yi di junj am xel mu yaa te ñaw waaye it di gaaw a ñaaw-xel, ami sikki-sakka ci lépp. Machiavelli jàppe nañu ko niki ki sos xam-xamu politig bu jamonoo bi.

Niccolò Machiavelli: Bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali
"Niccolò Machiavelli"
Niccolò Machiavelli: Bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali
"Niccolò Machiavelli"

Logo Commons

Xool it Wiki Commons

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

AdiratigÑaareelu tukki bi (bu Gànnaar bi)Kureelu Mbootayu Xeet yiDiiwaanu TambakundaaSñ Sàmba Jaara MbayNgeerSancug TugalCuubXareb Àdduna bu NjëkkKoorYoonu EŋacaRoyanGineAlaaji Maalik SiTuru Way-DëkkMaliLiechtensteinBañkatu ndeerUruguwaayLislaamPragRéew yu Bennoo yu AamerikRéewum LawosYattMàggalug TuubaaGëstubiddiwBeliyarNiseerWolof (làkk)Seex Anta JóobGermaine AcognyXoriitJantJeqiku walla fipp ga amoon ca FraansÓstraaliSanqaayDibéerSanta Catarina (Kap Weer)FukuokaTugalasiGoxub Dottub Bëj-gànnaarYëngu-yënguy politig yu mag yi ci adduna biSaab-saabSowwu AfrikWuññi yu juxraaf yiArsenal F.C.Iniwersite Gaston Berger Bu NdarFogo (Kap Weer)Alaaji Alieu Ibraayma Cham JuufMindeloDaawudaGD AmaranteGanaarLondarJolofAcadémica do MindeloSanto Antão (Kap Weert)WikipediaRéew yi BennooNgelawSudaan🡆 More