Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar

Royuwaay:Infobox Université

' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

Démb

Léewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.

Taxawaayam mu ngi aju ci sart Royuwaay:N° bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.

Mu ngi jot gëddam ci ndogalu Royuwaay:N° bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu Royuwaay:N° bu 4 desàmbar 1996.

Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.

Ràññeefi barab

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Gis-gisu wërngaluw iniwersite wi ci bëj-saalum ak soow jànt (bunt)

Diggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« https://web.archive.org/web/20080419061846/http://www.sunusanar.com/ » la ñu ko tudde.

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
buntu iniwersite bi

Bërëbu tàggat ak gëstu

Iniwersite bu Ndar ëmb na juróorum-ñaari Bërëbu tàggat ak gëstu : 

  • Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
  • Xam-xamu jëmale ak xarala
  • Xam-xamu yoon ak politig
  • Xam-xamu koom-koom ak
  • Xam-xamu wérgu-yaram
  • Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
  • Caada, diine, taaral ak jokkoo
  • Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.

Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama

Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:

  • Angale,
  • Farãse
  • Làkk nasaraan jëmale,
  • Xam-xamu melosuuf,
  • Xam-xamu nekkinu àskan yi.

Xam-xamu jëmale ak xarala

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Diagramme des parcours possibles au sein de l'UFR

Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.

Mën a dugg

Bànqaasu xayma jëmale
Bànqaasu bitil jëmale
Bànqaasu informatig

Xam-xamu yoon ak politig

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Offre de formation à l'UFR Sciences juridiques et politiques

Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:

  • Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
  • Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
  • Bànqaasu xam-xamu politig.

Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi

Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris

bànqaasu xam-xamu politig

Mën a dugg

Xam-xamu koom-koom ak doxalin

Kërug internet

Caada, diine, taaral ak jokkoo

Kërug internet Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :

  • Bànqaasu jokkoo,
  • bànqaasu infogarafi,
  • Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
  • Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
  • Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
  • Bànqaasu Xam-xamu diine.

bànqaasu jokkoo

Mën a dugg
tërëlin
Mujjàntal

Bànqaasu infogarafi

Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada

Mujjàntal
Mën a dugg

Bànqaasu làkk ak caaday Afrig

Mujjàntal
Màndargal
Mën a dugg

Wàllum gëstu

nekkinu ndongo daara yi (CROUS)

Yokkute lim ndongo yi

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

Effectifs par UFR
SAT SEG SJP LSH TOTAL UGB
2001/2002 400 280 499 1480 2659
2002/2003 475 325 535 1525 2860
2003/2004 559 349 575 1506 2989
2004/2005 671 396 505 1799 3371
2005/2006 726 415 688 1965 3794
2006/2007 727 641 932 2143 4443

Dëkkuwaay

Royuwaay:Message galerie

Loyer au campus
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers
Villages A,B,C,D,E,F,K,M 3000 (4,57 euros) ???
Villages H,I,J,L 4000 (6,09 euros) ???

Dem beek dikk bi

Tektal yi

Xool yeneen

Téere ak mbóotu tektal

  • Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, Royuwaay:P.5-6

Cosaan

mbóotu tektal

  • Musée du Centre de Recherches et de Documentation du Sénégal à Saint-Louis
  • Université Cheikh-Anta-Diop
  • Éducation au Sénégal
  • Felwine Sarr

mbóotu biti

Royuwaay:Autres projets

Royuwaay:Portail ' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

  • Bànqaasu làkk ak caaday Afrig,
  • Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
  • Bànqaasu Xam-xamu diine.

bànqaasu jokkoo

Mën a dugg
tërëlin
Mujjàntal

Bànqaasu infogarafi

Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada

Mujjàntal
Mën a dugg

Bànqaasu làkk ak caaday Afrig

Mujjàntal
Màndargal
Mën a dugg

Wàllum gëstu

nekkinu ndongo daara yi (CROUS)

yokkute lim ndongo yi

thumb|350px|Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

L'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :

  • Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
  • Xam-xamu jëmale ak xarala
  • Xam-xamu yoon ak politig
  • Xam-xamu koom-koom ak
  • Xam-xamu wérgu-yaram
  • Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
  • Caada, diine, taaral ak jokkoo
  • Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.

Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama

Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:

  • Angale,
  • Farãse
  • Làkk nasaraan jëmale,
  • Xam-xamu melosuuf,
  • Xam-xamu nekkinu àskan yi.

Xam-xamu jëmale ak xarala

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Diagramme des parcours possibles au sein de l'UFR

Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.

Mën a dugg

Bànqaasu xayma jëmale
Bànqaasu bitil jëmale
Bànqaasu informatig

Xam-xamu yoon ak politig

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar 
Offre de formation à l'UFR Sciences juridiques et politiques

Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:

  • Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
  • Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
  • Bànqaasu xam-xamu politig.

Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi

Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris

bànqaasu xam-xamu politig

Mën a dugg

Xam-xamu koom-koom ak doxalin

Kërug internet

Caada, diine, taaral ak jokkoo

Kërug internet Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :

  • Bànqaasu jokkoo,
  • bànqaasu infogarafi,
  • Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
  • Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
  • Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
  • Bànqaasu Xam-xamu diine.

bànqaasu jokkoo

Mën a dugg
tërëlin
Mujjàntal

Bànqaasu infogarafi

Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada

Mujjàntal
Mën a dugg

Bànqaasu làkk ak caada Agrig

Mujjàntal
Màndargal
Mën a dugg

Wàllum gëstu

nekkinu ndongo daara yi (CROUS)

yokkute lim ndongo yi

thumb|350px|Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

Effectifs par UFR
SAT SEG SJP LSH TOTAL UGB
2001/2002 400 280 499 1480 2659
2002/2003 475 325 535 1525 2860
2003/2004 559 349 575 1506 2989
2004/2005 671 396 505 1799 3371
2005/2006 726 415 688 1965 3794
2006/2007 727 641 932 2143 4443

Dëkkuwaay

Royuwaay:Message galerie

Loyer au campus
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers
Villages A,B,C,D,E,F,K,M 3000 (4,57 euros) ???
Villages H,I,J,L 4000 (6,09 euros) ???

Dem beek dikk bi

Tektal yi

Xool yeneen

Téere ak mbóotu tektal

  • Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, Royuwaay:P.5-6

Cosaan

mbóotu tektal

  • Musée du Centre de Recherches et de Documentation du Sénégal à Saint-Louis
  • Université Cheikh-Anta-Diop
  • Éducation au Sénégal
  • Felwine Sarr

mbóotu biti

Royuwaay:Autres projets

Royuwaay:Portail

Tags:

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar DémbIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Ràññeefi barabIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Bërëbu tàggat ak gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Wàllum gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar nekkinu ndongo daara yi (CROUS)Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar Tektal yiIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Xool yeneenIniwersite Gaston Berger Bu Ndar DémbIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Ràññeefi barabIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Bërëbu tàggat ak gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Wàllum gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar nekkinu ndongo daara yi (CROUS)Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar Tektal yiIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Xool yeneenIniwersite Gaston Berger Bu Ndar DémbIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Ràññeefi barabIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Bërëbu tàggat ak gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Wàllum gëstuIniwersite Gaston Berger Bu Ndar nekkinu ndongo daara yi (CROUS)Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar Tektal yiIniwersite Gaston Berger Bu Ndar Xool yeneenIniwersite Gaston Berger Bu Ndar

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

SiliPenku AsiWolofRéewum DominikBanglaadesDiwaani dottDuni FaarowBeliisAntigua ak BarbudaGaalJëmmNitWatikaa (péy)Saint Kitts and NevisMadagaskaarBisaawóoBennWaaloXott-biteelAlxuraanDereet.itWolof (làkk)XeetNiccolò MachiavelliPlutonMbàmbulaan Gu-DalYoos-bisaawCuubXayDawaan gu wéyÓstraaliSeerbiBeneGanaAntananariwoSahaaba yiWërlaayAndoorXarey jóoñeMoroniArsantinGrenadaTaariixKongóo-KinshasaBenesuwelaMuusWiyetnaamNanjingXareb Àdduna bu NjëkkOlaandAamerigQin Shi HuangBernSëriñ Mbay JAXATEGoxFK PanevėžysWayGirees🡆 More