Ngeer

Ngeer xeetu gàncax la gu bokk ci njabootu combretaceae.

Wenn la ci xeetam.

Ngeer gi (Guiera senegalensis)
Ngeer gi (Guiera senegalensis)

Melo wi

Ngeer ngàjj la gu man a àgg ba 3i met. Bari lool ci Saara bi, ci sowwu jantub Afrig, fu ci mel ni Senegaal. Garab gu yam lay doon te firiku. Di xaw a tolloo ak salaan.

Njariñ li

Ngeer garabu paj la, bokk na ci yi ñu gën a taamu ca Sowwu Afrig. Dees na ko fa jëfandikoo ngir faj xeetu wopp yu bari te wuute. Jëfandikoom danay xaw a niru ak gog kenkelibaa, te ñoom ñaar lees faral di boole, ngir faj tawatu soj, tàngooru yaram ak jafe-jafey nokki. Xob yu wex yi lees faral di jëfandikoo. Dees na ko boole ak rat it ngir faj ci soj.

Ndox mi muy ëmb, da koy tàbbal ci suuf si yeneen garab yi jariñoo ko. Kon ba ko cib tool làmboo nay njariñ.

Nataal yi

Turu xam-xam wi

Guiera senegalensis

[1]

Tur wi ci yeneeni làkk

farañse: Guiera
angale: Guiera

Tags:

Ngeer Melo wiNgeer Njariñ liNgeer Nataal yiNgeer Turu xam-xam wiNgeer Tur wi ci yeneeni làkkNgeer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

PragMaam Maajoor BóoyPermXajAfrig gu bëj-saalumu-SaharaWolof (làkk)Arafu X QSkopjeWilniyusWikbaatukaayBurkinaa FaasoDiiney SéeréerChelsea F.C.MiyanmaarGëwéelSiri LaankaXaruSaasumaan bRoogKamboodiArak, IranBukarestBoy giLondarNgéejCiipërOktoobarXam-xami nite ak mboolaayAamerigBandar AbbasWolofMbaamSawaraMaam Yunus JeŋPenku gu SoriSaw Tome ak PreesipWorld Wide WebRio de JaneiroWeerKiyewFaraasConfuciusTembteSibiruGineg yamooGayndeDiwaanBeijingWëttéenLibiBaatukaayTill giJimbulang🡆 More