Adiratig

Ci angale mooy Adriatic; Ci faranse mooy Adriatique

Géej la, ci diggante dunu Kereet ak dunu Sisil (Sisile). Tey jii géej ga mingi tudd Géeju Iyoniyeen (Mer Ionienne). Bokkul ak li ñu wax Adiratig tey ji. Adiratig tey mooy géej ga nekk ci diggante Itaali ak Yugosalawi (Yougoslavie).

Ci Injiil dañuy wax ci Adiratig ci Jëf 27:27.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

MoldaawiSoxna Jaara BusoBelaarusWiyetnaamEsloweeniXel mu sell miOlaandFatikSiddeem pomKullu-kulluOld TraffordKëwsuDuusub sinGargambooseMëfër mi (rabu àll)SimiRéewum MaseduwaanSaytubiddiwSudaan gu Bëj-saalumKàttanNjëkk-xaymaSuufNdombo gu mbëjJëmmSaint Vincent and the GrenadinesSeland-Gu-BeesEswatiniXiibonBiên HòaLinuxSibiruBëj-gànnaaru AfrigMelosuufug AfrigKongóo-KinshasaWeenusBaatukaayMinskBisu TamxaritÑaareelu Xareb ÀddunaKowetArsantinJimbulangÀllarbaGuyaana gu FaraasBetleyemSaarayegoMbëjtekkaaralIniwersite Gaston Berger Bu NdarJuróom ñaarSatumbarKaledooni-Gu-BeesGayndeFaraasXëtu webIspaañRakki-gàmmuRon-goxu EndMelaneesiMbëjfeppalDambalBerlinOseyaani🡆 More