Dalmasi

Ci angale mooy Dalmatia; Ci faranse mooy Dalmatie

Ci jamonon Injill diiwaan la woon, ci sowu-suufu diiwaanu Room bu tuddoon Iliri ci penku géeju Adiratig. Maanaam mooy daanaka réew mi ñu waxoon Yugosalawi (ex-Yougoslavie), te ñu wax léegi Korwaasi, Bosni-Ersegowin ak Montenegëro.

Dañu ciy wax ci 2Tim 4:10.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Ahmadou BambaEunice AdabunuPaul (Kap Weer)Mbootaayu Xeet yi BennooMboqWu-angalteerJamaykaTaariixIniweersite Séex Anta JóobTàndarmaMoskuKàllaamaQingdaoOngiriKiyewRibeira BravaDuusFaranseMuritMoldaawiApoloniDunKokoGuyFiiDambalSénkiJantSanqaayWoyNgeerSeex Ahmadu BambaJappum njaamSëriñ Maalig Basin SiSoxna Jaara BusoAnxiety disorderDimbAcadémica do MindeloYaatuwaayPlutonMbëjfeppalKawlakSanta Catarina (Kap Weer)SuweedWeeri wolofArsenal F.C.Kol-kolu suuf siSëqët (Coqueluche)MbàqnoosNataalKàttanJeoorjiPonta do Sol (Kap Weert)ÓstraaliDalub webXaralaSanto Antão (Kap Weert)LiechtensteinNgéejAndoronikusWaySantiago (Kap Weert)Ndiiwaani SenegaalMbootaayu Réewi Jullit yiSingapoor🡆 More