Fatik

Fatik, mi ngi yaatoo 7945km, am 475.970 ciy way-dëkk. Mooy péyu diwaan bi mu bokk (diwaanu Fatik) ak goxu Fatik. Mi ngi juddu niki diwaan ci 1984, ba ñu xaajee diwaanu Siin-Saalum ñaar: Fatik ak Kawlak. Mi ngi tëdd ci lu féete Mbàmbulaanug Atlas gi, ci sowwu senegaal, ci suufu Kawlak, feggok réewum Gaambi ci bëj-saalumam.

Wiki Fatik
Wiki
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki taxawal

Koom-koom

Koom-koomam mi ngi cëslaayu ci mbéyum gerte, pepp, càmm ak napp.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Rio de JaneiroAyubésIzifo ezidaleka emoyeniPenku gu DigguAraabi SawditAtenAlaaji Maalik SiKàttanJimbulangSowwu TugalRéewum LawosLesotoKongóo-KinshasaBandar AbbasSiliBaalJerusalemWërlaayNdoxMuusNguur-giEswatiniMaldiifPremier LeagueMikroneesiSão PauloXayNosteg doxiinUkreenMoroniMbootaayu Réewi Jullit yiShanghaiKàllaamaDublinBudapestRéewum ñaari dex yiLëkkalekaayAsiOktoobarMamoor Xam Sa DiineGàmbiTehranShirazTabaDunJéemantu wiNdakaaruBaatukaayFilipiinAserFajã de ÁguaGëstubiddiwKàttanug imbikuBipolar disorderXiirtalug mbëjbijjaakonMayootArafu X Q🡆 More