tàmbali

Ab junj mooy as njukki, jukki bu tuut lool.

Su fekkee man ngaa bind ci wolof, di la sakku nga def ko. Su fekkee dégg nga wolof , te manoo it bind bu baax, bu mu doonub jaaxle, def ko rekk.

Àlliw Sàll Kawlax. Golo de ab rabu hàll la, bu man a yàq lool sax, te sawar ci, li muy dunde mooy li ci hàll rekk, lu mel ni, garab ug dimb, ak màngo... añs.. Ak a ragal xaj, xaj nag ab rabu hàll la moom itam, moom golo Amna ay xeet yu bari a bari, nimuy meloo nag mooy xonq walla nete. Nit ñi da nañ koy jàpp di ko yar ci kër yi, def ko reetaanu kaay, daana ka lépp lu nit di lekk rekk, dana ko lekk moom golo, ko am a am xel la nag, du faral di daw lu mu xamul. Li mu gën a ràññe a koo daal mooy yàq.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

IspaañRabJokkoosoryanteXam-xamTurks and Caicos IslandsElsinkiAntipatarisSaint Vincent and the GrenadinesSalaanÓstraaliBawolInternetFatikAfrigMiiraasMàngoGaranaatMartinikYewwute gu ndefarGuangzhouWu-faraasAtenAnasUfaMaio (Kap Weer)Mbàmbulaanug AtlasBëj-gànnaaru AfrigMuusNjàngatFinlaandPolineesiBetleyemKongóo-KinshasaRéewum Popileer bu SiinPertussis vaccineCosaanJantBreesilOoŋ KoŋSeggXiibonNdombo gu mbëjJuróom ñaarXaalu tubaabNjëkk-xaymaYattAsiKot DiwaarGayndeDalub webYonneeCharles DarwinKureelu Mbootayu Xeet yiElen Jonson SërliifÑayPaj🡆 More