Polineesi

Polineesi benn la ci diwaan yi ñu seddatlee goxu Oseyaani.

Polineesi
Fi Polineesi féete

Bii seddatlin nga xam ne Kureelu Mbootaayu Xeet yi sax mooy la jëfandikoo suy seddatle àdduna bi ci ay Diwaan, gëstukat yi ñoom seddatle bu bees bi la ñu taamu, moo xaaj Oseyaani ci ñaari diwaan: Oseyaani gu jege ak Oseyaani gu sori yi Polineesi box. Diwaan bi dafa am meloow ñettkoñ

Baatu Poloneesi waa faraas bii di Jules Dumont d'Uville moo ko sakk ci li jege atum 1830 (moo sakk itam baat yii di Melaneesi, Mikroneesi ak Maleesi), mi ngi jóge ci baati waa Geres yii di πολύς (bari) ak νησος (dun), maanaam dun yu bari.

Diwaan bi ay dun yu baree fi ne, man nan cee lim:

  • raaya Awaai (raayaUSA)
  • Duni Bennoo bi
Diwaani Oseyaani
Polineesi Óstraali · Melaneesi · Mikroneesi  · Pacific Rim · Polineesi

Tags:

DiwaanOseyaani

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

MerkuurBëj-gànnaaru AfrigPajDanmaarkAraabDublinWaxsetAtenNitXam-xamu nosukaaySiriMadridÓstraaliKaliningradFilmi ci wollofXaralay xibaar ak jokkooBanjulFattalukaay(mbëj)Xaalu tubaabLisbonSeent EleenSão PauloSaratovGuyaana gu FaraasSaarayegoNjàngaleMbëjtekkaaralSan MarinoMayootNiccolò MachiavelliLesotoBisu TamxaritBëj-saalum-penku AsiNowembarGoxTugalRéewum Lawos1 KorentUfaSatumbarBandaGermen AcoñiCuritibaSankt-PeterburgMoldaawiNauruWu-angalteerMaam Yunus JeŋBenedicta BoccoliToolu bijjaakonAwa Mari Kol SekkLimub njiiti Senegaal yilWeeri wolofXam-xami nite ak mboolaaySiddeem bukkiAminadabAfganistaanNdiiwaani SenegaalNeptuun🡆 More