Mee

Weeru mee mooy juroomeelu weer ci arminaatu Gregori di ñetteel ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin, doon tur bu ko waa-rom yi joxoon ngir màggale ko seen yàlla ju jigéen ja maius, jàppees na ne Romolos miy buuru Rom bi njëkk moo ko ko jagleeloon. Ca jamono yooyu moo doonoon ñetteelu weer ci arminaatu waa-rom bi.

Bés bi njëkk ci weeru mee xamees na ko niki bés bees di màggale liggéeykati àdduna bépp, ba ci Senegaal kenn du ko liggéey, ci Diiwaan-yu-Bennoo yi ak Kanadaa ñoom 1 Sattumbar lees ko di xewal.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar

Tags:

Weer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

TangorTalaataItaaliMaleesiBeerÑoñRéewum Popileer bu SiinTirkiLëkkalekaayNgóora (jëmm)FeppsaalGanaLouvreMuriidulaaMaars (weer)Limub njiiti Senegaal yilKom-komAnxiety disorderAyitiDiggu AamerigSattumbarBarakiPalauTansaniCeddoGunóorJantOoŋ KoŋIslaandIsiptWommatiinu mbëjTarrafal de Monte TrigoUnk wAfritugalasiSimiXëtu webAretasAlex FergusonDalmasiKaliningradKopparDencukaaySuufMaltYombBennoo gu AlmaañKamakuraMàggalug TuubaaXaralaymbëjSatumbarKasakistaanCuubSuweXam-xamu suuf si ak jawwu jiNiseerLaayeenKoriBipolar disorder🡆 More