Dëgërluwiin

Dëgërluwiin walla Dëgërluwiin gu mbëj mooy ni ab wommatukaayu mbëj jikkowoo di jéem a bañ ay yani mbëj di ko jàll, di dëgërlu.

Ci dëgërluwiinu ab jumtukaay lanuy man a xamee nu ndëgërloom toll.

Tekki

Dëgërluwiin wi ρ bennaanu nattam mooy ohm x meetar [Ω x m], dafa aju ci ni wommatukaay bi bindoo (dijjaayam, guddaayam) waaye li ko lonkale ak Ndëgërlu gi R mooy mile mbind:

    Dëgërluwiin 
  • ρ mooy Dëgërluwiin wi ñu koy natte ohm x meetar [Ω x m];
  • R mooy ndëgërlu gu benn dogu jumtukaay boo jël ñu koy natte ohm [Ω];
  • l mooy guddaayu jumtukaay bi dawaan bi di jaar ñu koy natte meetar;
  • S mooy dijjaayu jumtukaay bi ñu koy natte meetar kaare [m2].

Sunu wëlbëtee ci bii yamale mu jox nu nan lanuy natte ndëgërlu gu ab wommatukaay bu nu xamee guddaayam ak dijjaayam:

    Dëgërluwiin 

Dëgërluwiin gi manees na koo natte itam ak bii yamale:

    Dëgërluwiin 
  • E mooy taraayu toolu mbëj bi, ñu koy natte volt ci meetar
  • J mooy fattaayu dawaan bi, ñu koy natte ampere ci meetar kaare

ci mujjante manees na koo natte itam ak safaanu wommatiin wi:

    Dëgërluwiin 

Ajoom ci tàngoor

Dëgërluwiin gu ab wommatukaay dafay aju ci xeetu ne-ne bi ñu ko defaree.

Dëgërluwiin gu ab mbéll

Ci mbéll yi Dëgërluwiin gi dafay yokk lu tàngaay bi di gën a bari, manam a wommat dafay wàññeeku. Safaan wa su tàngaay bi wàññee koo ba àgg ci benn lim bumu manuta romb.

    Dëgërluwiin 

Dëgërluwiin  mooy Dëgërluwiin gi T tàngaay bi, Dëgërluwiin  mooy Dëgërluwiin gi ci tàngaayu delluwaay bi, naka-jekk benn ci ñaar yii lay doon 0° walla 20°. &alpha di ab ngungu tàngoor bu aju ci ne-ne bi.

Dëgërluwiin bu ab xaaj-wommatukaay

Dëgërluwiin gu ab xaaj-wommatukaay dafay wàññeeku lu tàngaay bi di yokk, kon lu tàngaay bi yokk ñuy gën a man a wommat. Bii digaale moo koy faramface:

    Dëgërluwiin 

A, B ak C ay ngung yees jagleel ne-ne bi lañu.

Lëkkalekaay yu biir

wikbaatukaay am na xët wu tudd: Dëgërluwiin

Tags:

Dëgërluwiin TekkiDëgërluwiin Ajoom ci tàngoorDëgërluwiin Lëkkalekaay yu biirDëgërluwiinNdëgërlu gu mbëjYanu mbëj

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Maam Yunus JeŋÑayKot DiwaarNiels BohrMartinikAsiJantIrlaandWeenusAliin Situwe JaataRiisiDiinePolineesiKureelu Mbootayu Xeet yiAlxamesCuritibaVladivostokPovoação VelhaWoyNjëkk-xaymaDalub webPolitigWikbaatukaayFinlaandIsraayilSaratovSinemaaGireesQuébecPHPGuySaambiÀddunaMaasAmsterdamKubaaJuróom ñaarRakki-gàmmuBelsikFurna (Kap Weert)Ahmadou BambaGanaEscudo Kap WeertInternetSuufNjamena.jpNdajem BerlinAraabAntananariwoKore gu Bëj-gànnaarNiccolò MachiavelliTiniisiSatumbarNdiiwaani SenegaalBisu TamxaritDjabarEslowaakiDéteeluJum🡆 More