Wikbaatukaay

Wikbaatukaay ab baatukaay barilàkk bu ubbeeku la, di benn ci sémbi Wiki Fondation yi.

Baatub «Wikbaatukaay» dafay junj sumb bu wolof bu boobu sémb, di Wiktionary ci wu-angalteer. Mook Wiki ñoo bokk doxiin, di lu ubbeeku te dàttu ci nosteg wiki, lees man a jëfandikoowaat ci anami GFDL.

Wikbaatukaay
Sémbu Wikbaatukaay

Tëddiin

Yéeney sémb bi mooy sos ab baatukaay bees di duggal làkki àdduna bi yépp. Ci bu wolof baat yépp a fiy nekk ak seen tekki ci yeneen làkk waaye ci wolof lañu leen di faramfaccee, joge seen gongikubaat, seeni bokktekki, safaantekki, waxiin, añs.

Tags:

WikipediaWolofWu-angalteer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

OmskRéewum Popileer bu SiinTugalWu-angalteerJibutiGunóorAnetKap WeerKinshasaJawwu jiMbëjfeppItaaliIspaañKiswahiliGarça de CimaPenku gu Jege.scKajoorMaars (weer)Màggalug TuubaaGarabCeeb u jën.rwAhmadou BambaMburuDimbDisambarHip-hopSëngTalaataYewwute gu ndefarRabil (Kap Weer).jpDéteeluXamale kuy Sëriñ bi, ak ay mbiram, ba bi waajuram wu góor làqooXaralaymbëjBaaxoñ bWolof (askan)Taariixu SenegaalTuxalBésGuwaatemalaCeesGëm Malaaka yiPenku TugalYamooXam-xamu suuf si ak jawwu jiSéeréerSëriñ TuubaaNepaalTaysiirul HasiirRéewum LawosBawolNgaté yénnöTembteTaaylaandTarrafalAfganistaanUraanusPariAndoor🡆 More