Libi Tripoli

Tripoli (di طرابلس tarabilus ci araab) mooy péeyu réewum Libi. Turu dëkk baa ngi tekki «ñetti dëkk yi», ndax limu jóge ci booloog ñetti dëkk yii di Oea, Leptis ak Sabrata. Mi ngi féete ci bëj-gànnaar-sowwu réew mi, taq ci tàkk gi, ci dogub suuf bu kekke, féetek Géej gu Diggu gi ci geneen wàll

Wiki Libi Tripoli
Wiki
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki taxawal
Tripoli طرابلس
Libi Tripoli
Skyline of {{{official_name}}}
Réew Libi Tripoli Libi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
32° 54′ 8″ Bëj-gànnaar
     13° 11′ 9″ Penku
/ 32.90222, 13.18583
Kawewaay 81 m
way-dëkk 1 682 000 nit
atum way-dëkk 2 009
Rëyaay 400 km²

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Bisu TamxaritQuébecJollasuMbëjXaralay xibaar ak jokkooElen Jonson SërliifÀllarbaKaliningradXel mu sell miHo Chi Minh CityTajikistaanJigéenGunóorYonneeÑaareelu Xareb ÀddunaDambalKàttanAhmadou BambaTirinidaad ak TobaagoBarbadosEswatiniWaxsetXaymaBawolAyitiTiranaWeenusAnasJàngu Yéesu bu Dëggu biAltineGayndeMoldaawiSibiruNowembarWikipediaLesotoPertussis vaccineLibeeriaTaariixRéewum Diggu AfrigMàngoAmsterdamTéere TaariixLëkkalekaayGuyaabDóobaaliBejjenu AfrigGéejBaraayPolineesiMiiraasMbëjbijjaakonOoŋ KoŋKongóo-BrasaawiilRakkaati-gàmmuSoxna Jaara BusoKazanBennoo gu AlmaañNitInternetDalub web🡆 More