Sàppóoti

Sàppóotigarab la gu bàyyikoo Amerig gu digg, mu mujj yaatu ba agsi Afrig ak Asi.

Sàppóoti
Sàppóoti bi


Melo wi

Garab la gu am ay meññeef ñu neex. Ci aw déeg la ëppe waaye it di na am ci ag joor.

Màggug sàppooti daa yeex lool. Ay doomam yu jëkk a ngi tàmbalee ci ñeent jàpp juroomeelu atam. At mépp nag lay am i doom. Ci menn at man na cee joxe 150 jàpp 200i kiloy doom.

Taxawaay bi day àgg 15 met ba 30i met. Xob yi dañoo xaw a dëgar. Xas mi du ëpp 80i sàntimet cib rëyaay.

Sàppóoti 
Sàppóoti gi


Njariñam

Doom yi dees koy lekk, ñam wi daa am ay ferñent, da lay sawarloo, baax na it ci ay butiit ndax day reesal. Ab bantam lawbe yi ak liggeeykatu bant yi dañ koy jëfandikoo, di ci defar ay toogu walla ay lal.

Tur xam-xam wi

Achras sapota

Wàll:garab

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

NoorweesNdiiwaani SenegaalYoonu EŋacaEdirneEsperantoDiiwaanu TambaakundaaDibéerPragWaaloNataalElen Jonson SërliifŊas (rougeole)Eunice AdabunuKopparXam-xamu nosukaayAsiXam-xamMoskuSoxna Jaara BusoWikipediaMonsoroAminata TureDooleranduWilniyusGëstubiddiwPeexDuusSchizophreniaApoloniNgeerKasakistaanMakaawPorto Novo (Kap Weert)Palmeira (Kap Weer)GD AmaranteNdiirXiibonSalbadoorNjàngatFaatu JoomSingapoorNagoyaRoyanIraakTaysiirul HasiirSão Salvador do Mundo (Kap Weer)Sowwu AfrikStaad VárzeaTéere Irwaun Nadiim ci Sëriñ TuubaaUruguwaayJëm kanam gu xam-xam ak yewwute gu endustriWuññi yu juxraaf yiAfrigAltineS.L. BenficaUsbekistaanKàddDawaanu mbëjGine BisaawóoNdox🡆 More