Jimbulang Bu Waa-Brëtaañ

Jimbulang bu waa-Brëtaañ walla Encyclopædia Britannica (ci wu-angalteer), ñi ngi ko siiwal ci diggante 1768-1771.

Siiwalam gu njëkk mi ngi ame ca Edimbuurg ca Ekos. Bu waa-Brëtaañ bi bokk na ci jimbulang yiy wax ci lu daj yi njëkk ci kàllaama wu-angalteer, te bay jii ñoo ngi koy siiwal.

Jimbulang Bu Waa-Brëtaañ
yëgleeb génnu jumbulang bi

Ci ndoorteelu ñaareelu xaaju 1700 ba ci 1900, bari woon na ay boroom xam-xam yu doon jàppee ay jukkeem niki delluwaay bu wóor, yenn saa yi, ci siiwal yu yees yi, daa na am ay gisiin yu yees yees jagleel ay mboolooy gëstukat. Ci jamono yooyu amoon na gëdd bu baax ci biir askan wiy làkk wu-angalteer. Ci XX xarnu bi la yitteey jimbulang soppiku bu baax, coppite gi amal na ay njeexiit ci xarkanam ci fukk ak benneelu siiwal gi.

Taariixu jagal yi

jagal taariixu jagal dayoo
1eel 1768–1771 3 téere
2eel 1777–1784 10 téere
3eel 1788–1797, 1801 18 téere
4eel 1801–1809 20 téere
5eel 1815 20 téere
6eel 1820–1823, 1815–1824 20 téere ak 2 yees yokk
7eel 1830–1842 21 téere
8eel 1852–1860 21 téere
9eel 1875–1889 24 téere
10eel 1902–1903 9u jagal ak 2 yees yokk
11eel 1910–1911 29 téere
12eel 1921–1922 11u jagal ak 3 yees yokk
13eel 1926 11u jagal ak 6 yees yokk
14eel 1929–1973 24 téere
15eel 1974–1984 28 téere
1985– 32 téere

jagal gu njëkk gees def ci CD-ROM mi ngi génn 1994.

Lëkkalekaay yu biti

Tags:

JimbulangWu-angalteer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Ndimbal ci ay nataalKàllaamaWikbaatukaayLamanElen Jonson SërliifEcoopiYombXaralaYoro Booli JawKol-kolu suuf siAraabTirkiSëngKataarAngolaaSoviet Yi BennoJolofMakaawSahelXëtu garab i wikipediaLuksambuurNamibiAsiMaleesi.snKosta RiikaJimbulang bu waa-BrëtaañAlbaaniSoxnaBitiniReiñõoAfrigCova RodelaXëtu webMbëjfeppalMborosaanWorld Wide WebMburuTimoor gu PenkuYoonBelsikAddunaBaatukaayJordaaniKamakuraCampo BaixoJoão GalegoIraanArara🡆 More