Xeex

Xeex garab la gog mi bokk ci njabootug Rhizophoraceae, bari na ca Gine gu digg.

Xeex
Xeex gi


Melo wi

Garab gu ndaw la gog reen yi day law ci suuf. Xob yi dañuy jàkkarloo. Doom biy sax ci garab day wërbalu te toll ci 3i sàntimet.

Fi muy ëpp di sax day am ndox, ak ndox mu am cafka xorom, walla ci wetu dex.

Njariñ yi

Bant biy juge ci garab gi day dëgër te diis moo tax ñu koy jëfandikoo ci wallu liggeeyu bant.

Xob yi dinan faral di ko fajee gaana, lakk-lakk ak taab.

Nataal yi

Xeex 
Tóortóor
Xeex 
Car



Turu xam-xam wi

Rhizophora racemosa

Tags:

Xeex Melo wiXeex Njariñ yiXeex Nataal yiXeex Turu xam-xam wiXeex

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

GayndeJordaaniMàddXaralaymbëjGanaIzhevskLonkoyoonKazanGireesElsinkiKisinawuMboor Ak DiineXam-xamu suuf si ak jawwu jiBéerFurna (Kap Weert)SuweedXiibonYiirRéewum CekLondarMelosuufug AfrigArmeeniTirinidaad ak TobaagoJëmmÀllarbaSoxna Jaara BusoFK ŽalgirisBennoo gu AlmaañBerlinNiels BohrYëngu-yëngu yu ag nasaraanal ak ay wi mu àndalBanglaadesXareb Àdduna bu NjëkkKore gu Bëj-gànnaarMeningiteSaarayegoTëriinuw nosukaayDéteeluYattNataalOoŋ KoŋWolofAfrigAlmaañNdoxXët wu njëkkKodiwaarPariBipolar disorderTaariixAntananariwoMajor League SoccerSuweDjabarXel mu sell miHo Chi Minh CityAwrilKoom-koomBanaanaLëkkalekaayRéewum ñaari dex yiHTMLTugalasi🡆 More