Béer

Béer garab la gog guddaay gu yam la yor.

Mi ngi bokk ci njabootug Anacardiacées.

Béer
Nataalu garabug béer

Melo wi

Garab gi peer bu ndaw la yor, day màgg jëm ci kaw, guddaayam man naa àgg ba 10i met. Garab gu bari lool ay witaamin la. Danay meññ benn fooytéef bu dëgër, ñuul te neex lool.

Njariñ yi

-Ay foytéefam dees koy lekk ak di ci defar yenn xeeti njar yi. -Garabu ber manees na ko jëfandiko ngir doxal yenn daamar yi. -Garab la gog bari na jàngoro yu muy faj, bokk na ci sibbiru.

Nataal yi

Turu xam-xam wi

Sclerocarya birrea

Tags:

Béer Melo wiBéer Njariñ yiBéer Nataal yiBéer Turu xam-xam wiBéer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Amadou BambaJeqiku walla fipp ga amoon ca FraansBennoo gu AlmaañBoavista FC da PraiaIniwersite Gaston Berger Bu NdarPichilemuSão Salvador do Mundo (Kap Weer)Sëriñ Muusaa KAXaruBiir bu dawWaxtaani sëriñ tuubaaAcadémica do MindeloGD AmaranteMindeloPodgorikaSuweBëj-saalumu AamerigApoloniLingoomSingapoorSal (Kap Weer)Ribeira BravaWuññi yu juxraaf yiBañkatu ndeerMaio (Kap Weert)Ñaqu sëqët (coqueluche)DooleranduXiibonPoloñTaysiirul HasiirJolofMàggalug TuubaaYattAfrigAminata TureBetsaydaPalmeira (Kap Weer)BreesilDéteeluSëriñ SaaliwuKoorPonta do Sol (Kap Weert)XaymaGuySowwu AfrigGoxub Dottub Bëj-gànnaarDimbSëriñ Saaliwu MbàkkeMaliTéere Irwaun Nadiim ci Sëriñ TuubaaKunsay/NgunsayWayDawaanu mbëjJurukaayu mbëjMbootaayu Xeet yi BennooFaatu JoomSëriñ Maalig Basin SiLondarAyitiMbëjfeppalKol-kolu suuf siSudaanBeliyarWolof (askan)Niseer🡆 More