Rakki-Gàmmu

Rakki-gammu, (ci araab ربيع الثاني) tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.

Mooy ñeenteelu weer ci at mi, di weer ci njëkk ginaaw gàmmu gi

Lëkkalekaay yu biti

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski

Tags:

AraabAtGàmmuWeer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

MeningitePaftanWu-angalteerGuangzhouNiseerKàllaamaÓstraaliIspaañTiniisiFattalukaay(mbëj)Sankt-PeterburgTolyattiSoviet Yi BennoRomGayndeÑayRon-goxu EndTajikistaanAwrilSiriOtrisXam-xamu nosukaayNjuux liTarrafal (dëkkaan)KazanTurks and Caicos IslandsAltineAmsterdamWatikaa (péy)LiechtensteinSuweSeent EleenSaambiSatumbarLilongweEswatiniGuyaana gu FaraasAliin Situwe JaataNdiiwaani SenegaalPHPIraakWikipediaBésSàngolFilipiinSeex Ibraayma FaalSudaanMbëjfeppalBoy giBanglaadesArubaWolofMerkuurKaliningradÀllarbaMelosuufug Afrig🡆 More