Baraxlu

Baraxlu, (ci araab sahbaan شَعبان ), tuddees na ko noonu ndax aw ñall la (shahb ci araab) ci diggante rajab ak ramadaan.

Waxees na ne nit ñi daño cee baaxoo woon a tàqalikoo ak a ñallu (tas) ngir sàkku-ji ndox, mu daal di jël tur woowu. Mooy juroom-ñetteelu weer ci at mi, di itam weer jiitu koor gi. Bokk na ci weer yi baax a woor ci jullit ñi

Lëkkalekaay yu biti

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski

Tags:

AraabAtKoorWeer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

MartinikParisDanmaarkMelosuufSaafaandu giGëstubiddiwGineAtIspaañArareMerkuurChongqingAmmanDawaan gu wéyDiiwaanu SiggcoorNamandiruImaaraat yu Araab yu Bennoo yiEndoneesiXarefulwoonXaralay xibaar ak jokkooSéeréerDëgërlukaayXaralaymbëjLibaaJurukaayu mbëjWiyenTimoor gu PenkuRabatDambalTianjinPeruButaanKanadaaFewirieKap WeertArmeeniKot DiwaarÑamakoTuubaaYewwute gu ndefarYaroslavlPolineesi gu FaraasDiggu AamerigWikbaatukaayAl BaydaPlutonWiyetnaamRéewum Popileer bu SiinJigéenAndorra la VellaXeltuBenesuwelaBahrayniPakistaanSuweAfrig gu Bëj-saalumAtenÑaarBreesilMbëjfeppCuubWaxsetGaal🡆 More