Arkelawus

Ci angale mooy Archelaus; Ci faranse mooy Archélaüs

Erodd Arkelawus, doomu Erodd bu mag ba, moo falu woon ci diiwaani Yude, Samari ak Idume (Idumée) 4 j.K. nguuru ba 6 g.K.. Yaayam Maltas (Malthrace) la tudd. Arkelawus ak Erodd Antipas ñoo bokkoon ndey ak baay. Yawut yi ak waa Samari yi jiiñ na ko kor ci kanamu buuru Room ndax coxoram. Buur bi Ogust Sesaar moo ko fuñ ci diiwaanu Gool (Gaule), maanaam Farans, ci 6 g.K.. Gannaaw loolu def nañu Yude diiwaan ci suuf nguuru Room, te jawriñ yi buuru Room fal yilifoon fa. Jabaram Mariyamënë (Mariamne), doomu Aristobul la, ki mu fase ngir takk Galafira (Glaphyra), jëtunu Alegsàndar (Alexandre), magam.

Man nañu gis tur wi ci Mc 2:22.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

JokkoosoryantePajSal (Kap Weer)SalbadoorJamaykaBipolar disorderWikipediaIniwersite Gaston Berger Bu NdarSëqët (Coqueluche)Marie Samuwel NjaayPariTuru Way-DëkkDalub webDiiwaanu NdarAndoronikusDiiwaanu SiggcoorSinemaaRéewi lebu yiTugalasiKàllaamaNdiirWénKoorXareb Àdduna bu NjëkkSafaanukaayKol-kolu suuf siFeebaru tëlbëti bu amul appYoussou N'DourMaasYaatuwaayXam-xamu suuf si ak jawwu jiSiin-SaalumSão Miguel (Kap Weert)PaftanÓstraaliWaxtaani sëriñ tuubaaSowwu AfrigMain PageRéew yi BennooSñ Sàmba Jaara MbayTarrafal de São NicolauSchizophreniaPichilemuGD AmarantesRoyanMadridIraakFukuokaPorto Novo (Kap Weert)TuubaaWolof (askan)MoskuMonsoroWorld Wide WebAcadémica do MindeloSuufÀllarbaMoldaawiApoloniPodgorikaKattanDéteeluGëstubiddiwEpatit AXaruSëriñ Saaliwu MbàkkeTéere Irwaun Nadiim ci Sëriñ Tuubaa🡆 More