Diiwaan Sudaan

Sudan (jóge ci ab baatu araab bilâd as-sûdân dëkkuwaayu ñu ñuul ñi, benn ci la diiwaani Afrik yi, tàmbalee ca penku Afrik ba ca sowwu Afrik, ci bëj-saalumu Sahel, tàmbalee ca Mali ba réewum Sudaan ci penku Afrik.

Diiwaan bi mooy ëpp taw ci Sahel, mbay mi fa la gën a neexe. Ci bëj-saalumu Sudaan àllub Yemoo fa am.


Diwaani Afrig
Diiwaan Sudaan Diwaani KMX: Diggu Afrig · Penku Afrig · Bëj-gànnaaru Afrig · Bëj-saalumu Afrig · Sowwu Afrig
Yeneen diwaan: Ginne · Bejjenu Afrig · Maghreb · Sahel · Afrig gu bëj-saalumu-Sahara · Sudaan

Tags:

MaliPenku AfrikSahelSowwu AfrikSudaan

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

FiiSiraa LeyoonNdombo gu mbëjDimbSénkiBartimeKàddArminaatBennoo gu AlmaañSafaanukaayJeqiku ga amoon ca FaraasJeoorjiSëriñ Muhammadu Faliilu MbàkkePorto Novo (Kap Weert)UetersenSëqët (Coqueluche)RomaaniKiyewJurukaayu mbëjWuññi yu juxraaf yiLislaamSporting CPSowwu AfrigYaatuwaayMbootaayu Réewi Jullit yiMboqXaalJëm kanam gu xam-xam ak yewwute gu endustriUruguwaayYoonu EŋacaSeex Anta JóobAw xët ci wàll giiMbëjfeppalÀllarbaBreesilÑaareelu tukki bi (bu Gànnaar bi)ÑaarDuusAsiTuubaaXareb Àdduna bu NjëkkAfrigDalmasiFeebaru stress buy wëyAminata TureFogo (Kap Weer)PaftanNagoyaOngiriSanto Antão (Kap Weert)PodgorikaYattAsotNgelawDakarTaysiirul HasiirMbootaayu Xeet yi BennooNoorweesNiseeriyaDiiwaanu TambaakundaaDiggu Afrik🡆 More