Melosuufug Buruundi

Buruundi am réewu diwaanu Diggu Afrig la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.

Wiki Melosuufug Buruundi
Wiki
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki taxawal

Melosuufug Buruundi
Lonkoyoonu Buruundi
Melosuufug Buruundi
Buruundi

Melosuufug jëmm

Mi ngi digook Kongóo-brasaawiil ci lu mat 233 km ci sowwu, ak Ruwandaa ci 290 km ci bëj-gànnaar, lang ak Tansani ci guddaayub 451 km ci penku. Buruundi amul ubbeeku ci géej gi, waaye yi ci bëj-saalum-sowwu da ñoo lang ak déegub Tanganica bu rëy ba. Réew mi dafa nekk ci diggante ñaari mbandi ndox yu mag yii di Niil ak bu Kongóo

Xool it

Melosuufug Buruundi 

Xool it Wiki Commons


Melosuufug Buruundi  Melosuufug Afrig Melosuufug Buruundi 

Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere  • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Xam-xamu suuf si ak jawwu jiSapoŋTarrafal (dëkkaan).jpElsinkiDereetSan MarinoXewarAmmanYëngu-yëngu yu ag nasaraanal ak ay wi mu àndalMboor Ak DiineKore gu Bëj-saalumSàngolDooleranduXaralaymbëjSaint Vincent and the GrenadinesSuweedLëkkalekaayTaariixMbàmbulaanug AtlasKore gu Bëj-gànnaarMayootHo Chi Minh CityJàngu Yéesu bu Dëggu biJullitDunSuweMiiraasIzhevskSão Jorge dos ÓrgãosBanjulBawolTurks and Caicos IslandsSeent EleenRiisiEndoneesiAtenReiñõoKaledooni-Gu-BeesNepaalXiibonBeijingLibeeriaDuusub sinBagdadSaratovKazanWaax bu PraiaTiniisiYonneeGarabMoldaawiYéesu-kristaaFinlaand1. Liig - Santiago gu bëj-saluumuTuvaluLonkoyoonBerlinFiijiJordaaniFilipiinAfritugalasiGuyaana gu Faraas🡆 More