Xewar

Xewar xeetu garab la gu bokk ci njabootug « Sapindaceae ».

Xewar gi (Lepisanthes senegalensis)
Xewar gi (Lepisanthes senegalensis)

Cosaan li

Moo ngi tasaaroo ca Afrig ci réew yii: Senegaal, Eritere, Ecopi, Somali, Sudaan, Keeñaa, Tansani, Ugàndaa, Kamerun, Réewum Diggu-Afrig, Gaboŋ, Kóngoo, Bene, Kodiwaar, Gàmbi, Gana, Gine, Gine bisaawóo, Niseer, Niseeryaa ,Tógoo, Àngolaa, Mosàmbig, Madagaskaar.

Amna it ca Asi gu bari naaj ga: Bangalades, Butaan, End, Nepaal, Siri-lànka, Kàmbots, Lawos, Birmani,Taylànd, Wiyet-naam, Endonesi, Maleesi, Papuwaasi Gine Gu yees ak Filipiin.

Xewar 
Meññeefum garabu xewar

Melo wi

Xewar garab la guy toll ci 6i met ci guddaay. Ay xobam day nëtëx.

Turu xam-xam wi

Lepisanthes senegalensis (Aphania senegalensis)

Tur wi ci yeneeni làkk

farañse: Cerisier du Cayor

Tags:

Xewar Cosaan liXewar Melo wiXewar Turu xam-xam wiXewar Tur wi ci yeneeni làkkXewar

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

DencukaaySeereKiribatiDuni FaarowThe BeatlesDereetTekuruurKiyewGoxub Dottub Bëj-saalumMelosuufBotswanaJamaykaTogóoYoonTehranKubaaFeebaru stress buy wëySiraa LeyoonNiseerÑaareelu Xareb ÀddunaSomaliNdakaaruSaaSahrul ProjecttAlmaañFC PortoEslowaakiSankt-PeterburgNamibiKirgistaanBalaamDiiwaani dottGarabXaralaymbëjWaxsetPenku gu DigguJerusalemGinePortugaalRéewum Popileer bu SiinNguur-giDublinDodomaRéewum MaseduwaanBeneTaariixSuweedWatikaaXam-xami nite ak mboolaayJimbulangAlseUulNosteg doxiinSenegaalMinskBëj-saalumu AamerigMeksigÑaarDiiwaanu NdarDisambarGine BisaawóoBundesligaJibutiAlmazánIslaandGaambi🡆 More