Kàttanug Mbëj

Kàttanug mbëj xeetu kàttan la gu lonku ci doole walla tool yu jóge ci mbëj, maanaam lu ñeel yëngug, walla doxub, yani mbëj.

Kàttanu mbëj manees na koo jëfandikoo ngir defi liggéey, leeral, tàngal,...

Kàttan ak dawaanu mbëj

Digaale bi ci kàttan ak ngóora

Kàttanu mbëj manees na koo natt ci dawaanu mbëj bi, balaa dara manees naa xayma liggéey bi

    Kàttanug Mbëj ,

Liggéey bi W ciy joule, yan bi Q ciy coulomb ak wuuteeg aj gi Kàttanug Mbëj  ciy volt.

ak Kàttanug Mbëj , I dawaanu mbëj bi, t jamono ji:

    Kàttanug Mbëj ,

te Kàttanug Mbëj  di Ngóora ciy watt.

Kàttan gi manees na koo nattee nii:

    Kàttanug Mbëj 

Kàttan gi UE ciy Joule mooy kàttan gi rënku cib toolu mbëj, C mooy def bi, di ci lees di sukkandiku ngir man a xam daayoob kàttan gees man a sol cib fattalukaay.

    Kàttanug Mbëj 

Kàttan gi Um ciy Joule mooy kàttan gi rënku cib toolu bijjaakon, Kàttanug Mbëj  mooy walug bijjaakon giy soppiku ci jamono t.

Ci yenn anam yi dees na man a bind gii yamale:

    Kàttanug Mbëj 

Bennaanu natt

Bennaanu natt bi ëpp lu ñuy jëfandikoo ngir natt ab limu kàttanu mbëj mooy kilowattwaxtu (kWW)

    Kàttanug Mbëj 

sunu xamee ne Kàttanug Mbëj 

S mooy saa

Xool it

  • Kàttanug aj
  • Kattanug saal
  • Kàttanug mbëjbijjaakon

Tags:

Kàttanug Mbëj Kàttan ak dawaanu mbëjKàttanug Mbëj Xool itKàttanug MbëjKàttanToolu mbëjYanu mbëj

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

YolaakonKongóo-KinshasaQuébecWaxsetPenku AsiFiijiTugalasiXiibonMàngoMbëjbijjaakonMelosuufSeggSaytubiddiwWéyalLibeeriaSuufRéewum Popileer bu SiinSankt-PeterburgGëstubiddiwJumSowwu TugalAntananariwoNjamenaNjàngatIrlaandTirinidaad ak TobaagoLat JoorWolof (làkk)YiirSaarayegoDibéerTurkumenistaanJulius CaesarMaleesiBiên HòaSão Jorge dos ÓrgãosSport Bissau e BenficaBanaanaPenku gu SoriFas wMaasAltineBanglaadesMustafa Kemal AtatürkGargambooseTaariixPHPHTMLPaftanXeexPajNdajem BerlinToolu mbëj🡆 More