Dëkkaani Ndiiwaani Senegaal

Dëkkaani ndiiwaani yi, ci Senegaal, ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu réew mi.

ci 2007 lim bu toll 43 lañu.

Dëkkaani Ndiiwaani Senegaal
Dëkkaani ndiiwaani Ndakaaru yi

Taariix

Yokkug nit ñi dëkk ci Ndakaaru moo dem ba àgg ci benn dayoo bi, ba tax genn kilifag dëkk rekk manatu koo yor, tax sosug geneen nekkte gu gën a suufe waroon. Kon lii moo tax ci 1996 ñu séddale tunduw Ndakaaru ci 43 dëkkaani ndiiwaan, ni dëkk bu Paris.

Dogiin

43 Dëkkaani ndiiwaani yi dañu leen séddale ci 4 tund yi:

Xool it

Lëkkalekaay yu biir

Téerekaay

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)

Lëkkalekaay yu biti

Tags:

Dëkkaani Ndiiwaani Senegaal TaariixDëkkaani Ndiiwaani Senegaal DogiinDëkkaani Ndiiwaani Senegaal Xool itDëkkaani Ndiiwaani SenegaalSéddaliinu yoriinu Senegaal

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

CuubGarabRabApolyonDibéerBahamasMinskMeningiteSahara gu SowwuAfrig gu Bëj-saalumFC DerbyKajoorTangorKap WeerRonald ReaganInternetBotswanaWeenusGayndeKhabarovskPaltogaDiiwaan yu BennooYewwute gu ndefarBawolNdoxKongóo-BrasaawiilXam-xamu suuf si ak jawwu jiAyitiAnetPéncum waxtaanuwaayDiggu AamerigGD AmaranteFukuokaTus-wu-taxawÑayYatt1. Liig - SalMbëjfeppSiri LaankaBëtu-jaanRéewum Popileer bu SiinNairobiKom-komXartumJàngoroy EbolaNgaté yénnöStaad Marcelo LeitãoJolofSéeréer.cvNowembarSeggGuwaatemalaAsiSudaan gu Bëj-saalumTaariixTimoor gu PenkuGuyaana gu Faraas.sn🡆 More