Caxat

Caxat lawtan la, xeetu ñax guy law.

Ñax la gu man a muñ bekkoor. Dees na fekk ca Afrig gu naaje gi: Senegaal, Kamerun, Keeñaa, Ugandaa, Ecoopi.

Caxat gi (Leptadenia hastata)
Caxat mi (Leptadenia hastata)

Melo wi

Guddaayam danay àgg 20i met. Ag ndomaam di mat 10i sàntimet. Dafa nguuni-ngaana, te ag meññam daa yeex, ci njeexiitalu noor mbaa nawet bi lay faral di meññ.

Njariñ li

Fi muy sax fépp, xobam yi, meññeefam mu yees mi ak tóortóoram bi dees leen fay lekk ni ay lujum yu ñorut mbaa nu supp leen. Dees na ko xonte gàtt yi. Garab la guy faj tawat yu takku ci lim: góom, biir buy daw añs.

Nataal yi

Turu xam-xam wi

Leptadenia hastata

Tur wi yeneeni làkk

Tags:

Caxat Melo wiCaxat Njariñ liCaxat Nataal yiCaxat Turu xam-xam wiCaxat Tur wi yeneeni làkkCaxatAfrigEcoopiKamerunKeeñaaSenegaalUgandaa

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Sanc gu yees giSancug waa Tugal ci AfrigRajabPajUulPeruWeerSiin-SaalumBiir bu dawDambalWaax bu PraiaKonakriLouvreDéteeluKaledooni-Gu-BeesSiliDaqaaru tubaabSñ Sàmba Jaara MbayFC DerbySeriñ Muusaa KALibeeriaInterlingueMaio (Kap Weert)TianjinAcadémica da PraiaJibraltaarKureelu Mbootayu Xeet yiWeregSurinaamFiiAsorXareb Àdduna bu NjëkkBaía das GatasFogo (Kap Weer)LuksambuurDalub webAyitiKaw Gaambi ak Penku SenegaalSão Salvador do Mundo (Kap Weer)Seex Ahmadu BambaPraiaLimu réewi àdduna biNahjuAnxiety disorderPlanoiseSal (Kap Weer)LituwaaniTaariixXarefulwoonDiwaan-yu-BennooAw xët ci wàll giiRéew yi BennooCampeonato Nacional (Kap Weert)Gineg yamooSanto Antão (Kap Weert)Sëriñ Muhammadu Faliilu MbàkkeÑaqu sëqët (coqueluche)KirgistaanArareIsraayilXoriitGirees🡆 More