Bànni Israyil

Ci angale mooy Israel, people of Israel or children of Israel; Ci faranse mooy Israël, peuple d'Israël ou fils d'Israël

Israyil mooy tur, wa Yàlla jox Yanqóoba, doomu Isaaxa, di sëtu Ibraayma. Ñi wàcc ci Yanqóoba nag lañuy wooye bànni Israyil walla it Yawut yi. Def nañu fukki giir ak ñaar, di yi soqikoo ci doomi Yanqóoba.

Man nañu gis bànni Israyil ci Injiil ci aaya yii: Mc 8:10; 10:6; 15:24; 19:28; 27:9; Mk 12:29; Lu 1:54,80; 2:25; 7:9; 22:30; Yow 1:31; 3:10; Jëf 2:36; 4:10,27; 5:21,31; 7:23,37,42; 9:15; 10:2,22,36; 13:17,23; Jëf 13:24; 19:4; 26:7,17,23; 28:20; Ro 9:4,6,27,31; 10:1,19; 11:7,11,17,25,26; 1Ko 10:18; 2Ko 3:7,13; 11:22; Ef 2:12; Fb 3:5; Yt 7:5,9,11; 8:8,10; 9:19; 11:22,28,29,30; 12:18; 13:10; 2Pi 2:1; Pe 2:14; 7:4; 21:12.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

BawolKaliningradSuweGunóorLesotoBundesligaWéyalSaint Vincent and the GrenadinesXeltuGaranaatConfuciusGayndeKorwaasiNjamenaFilipiinXiibonBetfaseGuangzhouEsloweeniNjëkk-xaymaYéesu-kristaaAsiCosaanNdoxAliin Situwe JaataIsraayilFatikBarbadosEswatiniBandaEslowaakiKoom-koomDóobaaliLilongweTuvaluYoletSaarayegoLëkkalekaayMaam Yunus JeŋMajor League SoccerSelena GomezSahrul ProjecttIzhevskJordaaniKhabarovskNjàngaleUfaHTMLNiseerBiên HòaFewirieMarokBejjenu AfrigPertussis vaccineSuufAlbert EinsteinYolaakonDiiney SéeréerBëj-saalum-penku AsiNdianéLonkoyoon🡆 More