Aana

Ci angale mooy Anna te ci faranse mooy Anne.

Yonent bu jigéen ku màggat lool la woon. Jëkkëram gaañu na waaye Aana séyaatuloon. Guddi ak bëccëg dafa doon jaamu Yàlla ca këru Yàlla ga ca Yerusalem. Bi waajuri Kirisit indi woon Yeesu ni liir, Aana waxoon na ci moom ci kanamu ñépp ñi fa nekkoon. (Lu 2:36-38).

Ci Injiil dañuy gis Aana ci Lu 2:36,38.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

DalmasiWoorBañkatu ndeerMeningiteManchester UnitedKom-komXiirtalug mbëjbijjaakonFiiYoonu EŋacaSaab-saabPodgorikaMindeloNjàngatSiin-SaalumMaliDiiwaan yu BennooTaysiirul HasiirNiels BohrSalbadoorGD AmaranteXott-biteelPakistaanXonqNataalLingoomXaralaymbëjMbootaayu Réewi Jullit yiCS MindelenseSão Vicente (Kap Weer)Tarrafal de São NicolauXam-xamDunJëmmAddis-AbebaWoyŊas (rougeole)AyitiTuubaaMuhammadPremier LeagueWolof (askan)KàddFànnÀllarbaTuberculosisMbàqnoosConfuciusAfrigMuusBaatukaayDuni Virgin (angalteer)Abuu BakarUetersenFukkSiraa LeyoonKasakistaanArsenal F.C.Feebaru tëlbëti bu amul appXoriitRomDawaanu mbëjBeneSão Salvador do Mundo (Kap Weer)Xavier Rovira Rojas🡆 More