Waax

Waax xeetu garab la gu bokk ci njabootu Poaceae ak ci njabootaatu Bambusoideae, Afrig gu naaje la bàyyikoo.

Waax
Nataalu garabu Waax

Meloom wi

Man àgg ba 10i met ci guddaay ak 10i sàntimet ci yaatuwaayu dàtt. Xobam danay àgg ci guddaay 1 ba 2i sàntimet. Doom danay àgg ci guddaay 10 ba 15i milimet.

Njariña yi

Dees na ko jëfandikoo ci defarug alkol, ñoll ak duu. Waax ci xeeti tabaxukaay yi la bokk.

Nataala yi

Turu xam-xamam wi

Oxytenanthera abyssinica

Tags:

Waax Meloom wiWaax Njariña yiWaax Nataala yiWaax Turu xam-xamam wiWaax

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Soviet Yi BennoSaint Pierre ak MiquelonSuwisFukkKap WeerNamibiBelsikMaasLetóoniBurkinaa FaasoKoom-koomAwa Mari Kol SekkJokkoosoryanteSingapoorSal ReiTukkloorYewwuteCuubDëgërlukaayAfganistaanBëj-saalum-penku AsiSwalbard ak Jan MayenAndorra la VellaKureelu Mbootayu Xeet yiLituwaaniKamerunPorkhovMbëjfeppSiraa LeyoonNdajem BerlinNiseeriyaAraabSamwieNowelKarajAdiTembteSimiMikroneesiPenku AsiEndNosteg doxiinXaralaPalauJimbulang bu waa-BrëtaañNosteeg jantLaaxHTMLJasaanHo Chi Minh CityCuritibaMarookWeeri wolofBitiniKubaaJuróom benn🡆 More