Lëng

Lëng xeetu garab la gu bokk ci njabootu lamiaceae ak ci ñoñ Vitex.

Bari na lool ci Afrig gu diggu gi,ca komoor ak ca Rewño. Mbind mii jukki la bu ñeel meññiit mi. Man ngaa bokk ak nit ñi say xalaat ci jagal ko. Meloom day ñuul, peppam dees koy lekk.

Lëng gi (Vitex doniana)
Lëng gi (Vitex doniana)

Meññeef mi

Lëng 
Lëng bi

Meññeef mi, ci nëtëx lay doore, ñor digante mee ba noowàmbar, daal di ñuul te saf suukar. Guddaayu garab gi ci diggante yaar ba yatti meetar lay toll. Afrig la am ak bàmbulaan Endo. Ci dunu Rewño it dees na ko fa fekk.

Turu xam-xam wi

Vitex doniana

Tur wi ci yeneeni làkk

farañse: prunier noir
angale: black plum

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

SimiBëj-saalumu AamerigTéere Irwaun Nadiim ci Sëriñ TuubaaWaySëriñ TuubaaSal (Kap Weer)Wuññi yu juxraaf yiSudaanMosteiros (Kap Weert)LondarFiiPitaxDunSuweedFC DerbyTelefonDakarNataalJappum njaamTaariixDalub webSëriñ Saaliwu MbàkkeLouis XIV FaraasSowwu AfrigPoloñNgéejMbootaayu Xeet yi BennooTuberculosisEunice AdabunuKattanMeningiteSal ReiBoavista FC da PraiaWolof (askan)Feebaru tëlbëti bu amul appSénkiSantiago (Kap Weert)Seex Ahmadu BambaMarie Samuwel NjaayArsenal F.C.Porto Novo (Kap Weert)WénPichilemuKiyewPaftanBeneMain PageKàddWilniyusKàttanWu-angalteerPaul (Kap Weer)YolaakonSporting CPEdirneFogo (Kap Weer)OngiriPragKol-kolu suuf siMbëjfeppalCuubLinuxIslamSuuf🡆 More