Rand

Rand garab gu ndaw lay, mi ngi bokk ci njabootug Fabaceae, cosaanoo Afrig, dees koy fekk ci gox yi nga xam ni suuf si day xaw a wow fu mel ni Sahel gi.

Rand
Xobam ak doom


Melo wi

Garab la gog guddaayam li ci ëpp 1i met la doy jàpp 3i met, yenn saay man naa àgg 8i met, day niru garab gu am ay dég, te fekk ci dëgg-dëgg ay car yu amul xob la, ay xobam dañuy yor melo wu nëtëx. Ay doomam njokkub lujum lay doon.


Njariñ yi

Garab la gog dees koy jëmbat ngir rafetal.

Nataal yi

Rand 
Rand gi
Rand 
Rand gi


Turu xam-xam wi

Bauhinia rufescens 

Tags:

Rand Melo wiRand Njariñ yiRand Nataal yiRand Turu xam-xam wiRand

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Niels BohrKoloombiAyóobaSuletAlxuraanLourdesKampalaKàttanDodomaGuwaadalupEswatiniAndoorChelyabinskMusée de la (Gorée)NiseeriaBelaarusBesançonMonsoroAaroonaLetóoniArmeeniTokyoSeent EleenPaftanCosaanEscudo Kap WeertBiti-jawwuBakuRabKazanNiseeriyaMbàmbulaan Gu-DalBenesuwelaJantSibiruWikipediaPanamaaFaranseGuyaanaPoloñMosambikIsraayilRéewum Diggu AfrigJimbulang bu waa-Brëtaañ1. Liig - Santiago gu bëj-gannarDiiwaan yu BennooSiraa LeyoonTunisRomYamooOsakaBagdadJëf yaJunniNjëkk-xaymàSaint Kitts and NevisAminadabPenku AsiAsànkiritBeijingPaj🡆 More