Asaf

Ci làkku ibrë (אָסָא) la tur wi jóge.

Ci angale mooy Asa; Ci faranse mooy Asaf

Doomu Abiya la woon. Li dale ci Robowam ñetteelu buur ci Yuda la woon. Dafa nguuru lu tollu 41 at ci diggante 913 j.K. ba 873 j.K.. Man nañu jàng ci jalooreem ci 1Ki 15:8-24; 2Ch 14:1-16:14. Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:7,8).

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

BowasTugalInternetMosambikNjëkk-taariixXam-xamu nosukaayFeebaru tëlbëti bu amul appTimoor gu PenkuBaalBiibëlJappum njaamRéewum MaseduwaanLislaamWiyetnaamSëriñ Saaliwu MbàkkeJunjIraanAraabYoletMaasYokohamaBesançonGuangzhouSofiyaPoloñAndoorLourdesDéemArimateShenyangNjàngatAjaraPragPenku gu JegeYattNosteg doxiinAminata TureAmsterdamSimiChelyabinskKom-komKanadaaLituwaaniAfrig gu bëj-saalumu-SaharaAlxuraanul KariimCidade do MaioFrEndoneesiManchester City F.C.XeetXam-xamu suuf si ak jawwu jiDiineMonsoroUul🡆 More