Jullit

Ngértey ceet gu

wenn xët wu tudd « Jullit » moo am ci bii wiki

Xool (20 yi jiitu) () (2050100250500).
  • sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal Jullit mooy ku topp Diiney Lislaam, sartees nako ci nangu te wax ni «Maangi Seere...
  • Weeri wolof (yoonalaat gu jëm Arminaatu jullit ñi)
    gàddaay gi, walla bu jullit ñi mbaa bu Lislaam, ab arminaat bu weer la, buy sukkandiku ci doxiinu weer wi ngir xam ak natt weer wi. Jullit ñi danañu ko jëfandikoo...
  • Vignette pour Lislaam
    nga ko te ronu cig ronam, baatub jullit nag ci araab mooy (Muslim) giy tekki "aji jébbalu", aji nangul Yàlla, ndax jullit bi naafequl day déggal Yàlla, wéetal...
  • Vignette pour Mbootaayu Réewi Jullit yi
    Mbootaayu Réewi Jullit yi gii mi ngi sosu ci saxal goo xam ne buur ak njiiti reewi jullit yi jëloon nanu ko, ci waxtaanu seen daje bi nu njëkk’a daje...
  • Vignette pour Alxuraan
    fi jullit ñiy ball-loo seen yoon di Shariiha, ak ci sunna siy dundiinu Yónnent bi (jàmm yal na nekk ci moom), kon nag bu am solo la lool fi jullit ñi...
  • Vignette pour Pël
    1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo...
  • àngale di ko wax war. Xare ga doxoon diggante jullit ña ak kéeféer ya ca Badar (xare badar), jullit ña a daan. Xare su santee B (xare b) mooy li farañse...
  • Jëm-kanamug xam-xam Jeexiitalu gu waa-Tugal defoon ci yooni gëstu yu xam-xam yu jullit ñi. Lefi (wàlli) jëm kanamu xam-xam ci Tugal. Yewwuteg ndefar: ay jagleem...
  • Vignette pour Mohammed
    jikko yi jullit bu nekk war a jikkowoo : Ñuy wóor, dëggu, am yërmaande ci ku néew-doole, ku aajowoo, ku ñàkk, am ag cofeel ñeel bépp jullit tey dimblante...
  • Vignette pour Fuuta Tooro
    Jaabi dugg na ci lislaam, daal di jug def jiyaar ci kaw dëkkandoom yi dul jullit, ci noonu la nguurug Tukulóor xéye di nguur gi njëkk a dugg ci lislaam ci...
  • juroom ñenteelu weer ci arminaatu jullit ñi. Weer wii mooy ndoorteelu wàccug Alxuraan ci suuf. Bokk na ci li tax jullit ñi di ko woor: magal ko. Woor Benn...
  • Kori (ci araab شَوّال), ci la jullit ñiy wori ci seenug koor, mi ngi tudd nag ci araab "Sawaal" ngir ne sawaal day tekki ci araab ag jeex akug ñàkk meew...
  • ci at mi, di itam weer jiitu koor gi. Bokk na ci weer yi baax a woor ci jullit ñi (en)Islamic-Western Calendar Converter (Based on the Arithmetical or...
  • Vignette pour Bëj-gànnaaru Afrig
    réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon. Bi jullit yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko Ifriqiya. Beerbeer yi, ñooy...
  • weer wi mujj ci at mi. Ci lees di aj màkka,(ab ponk la ci lislaam war na jullit bu ko man), Ci lees di Tabaski (rayi xar, bëy, nag, galeem, jokkug bokk...
  • Vignette pour Yàlla
    lépp te kenn bind ko niki diiney Yahuut, Nasaraan ak Lislaam. Ci lislaam jullit ñi dañuy saxal amug Buur Yàlla mu bokk ci juróom benn ponki ngëm yi nekk...
  • la, mooy li farañse naan: guerre; araab naan ko حرب, àngale di ko wax war. Xare ga doxoon diggante jullit ña ak kéeféer ya ca Badar, jullit ña a daan....
  • waxtaane ci doggantal gii, ñooy : Kureelu xeet yi, Mbootaayu xeet yi, Mbootaayu reewi jullit ñi. Mbootaayu Réewi Jullit yi Kureelu Mbootayu Xeet yi‎...
  • ci jullit bi. Islaam jàngale na lu bari ci Malaaka yi, ñuy ñu ñu selle fi jullit yi. Jaamu Yàlla rekk ay seen yitte, te duñu ko moy mukk, jullit bi war...
  • yi ubbi Afrig gu sowwu gi, daal di duggal aw nitam ci lislaam, ci noonu, jullit ñi tàmbalee tas lislaam ndànk-ndànk ci bëj-saalumu tàkk gi (désert bi),...
Xool (20 yi jiitu) () (2050100250500).

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Staad VárzeaAssomadaSaaru MaryamaTaaywaanSalaanXiirtalukaayPalauKongóoAstanaAamerigToulouseRéewum Popileer bu SiinMusée de Mer (Gorée)SagamiharaTirkiLonkoyoonWatikaaStokolmWikbaatukaayNasaraanCuritibaEcoopiXaralaQueenPraiaAlxuraanBarnabasWiyetnaamWolof (askan)SalbadoorVysotskRéewum MaseduwaanStamford Bridge (staad)Dakar (région)BernDiiwaanu LugaNguriCS MindelenseXam-xami nite ak mboolaayAJWadusNoorweesGireesYu kojug nekkWikipediaQin Shi HuangPalestiinAsetSenegaalTianjinJumDoxalukaay bu mbëjAyóobaCampo BaixoSuwisNairobiNiseerJëm kanam gu xam-xamMóorisRajab🡆 More