Asi: Assi

Gox Adduna Asi mooy réewum gëna mag ci àdduna bi ci wàllu suuf ak askan.

Bennoo bi, bu yàgg a nekk kërug mbooleem mbooleem nit ñi, [1] moo nekkoon bérab bu bare bu jëkk bi. Réew mi am 4.7 milyaar ci nit[14] di lu tollu ci 60% ci askanu àdduna bi, am na lu ëpp ci nit ñi ci yeneen àdduna yépp.

Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it
Asi

Diiwaanu Nguuru Room

Turi Réew yeek seen raaya Rëyaay
(km²)
way-dëkk
(1 sulet 2002)
Fattaay
(ci km²)
Péey
Diggu Asi:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kasakistaan 2,346,927 13,472,593 5.7 Astana
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kirgistaan 198,500 4,822,166 24.3 Bishkek
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Tajikistaan 143,100 6,719,567 47.0 Dushanbe
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Turkumenistaan 488,100 4,688,963 9.6 Ashgabat
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Usbekistaan 447,400 25,563,441 57.1 Tashkent
Penku Asi:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Siin 9,584,492 1,384,303,705 134.0 Beijing
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ooŋ Koŋ (China) 1,092 7,303,334 6,688.0
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Sapoŋ 377,835 126,974,628 336.1 Tokyo
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Makaaw (China) 25 461,833 18,473.3
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Mongoli 1,565,000 2,694,432 1.7 Ulaanbaatar
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kore gu Bëj-gànnaar 120,540 22,224,195 184.4 Pyongyang
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kore gu Bëj-saalum 98,480 48,324,000 490.7 Seoul
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Taaywaan 35,980 22,548,009 626.7 Taipei
Bëj-gànnaaru Afrig:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Isipt 63,556 1,378,159 21.7 Cairo
Sibeeri:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Riisi 13,115,200 39,129,729 3.0 Moscow
Bëj-saalum-penku Asi:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Brunaay Daarusalaam 5,770 350,898 60.8 Bandar Seri Begawan
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kamboodi 181,040 12,775,324 70.6 Phnom Penh
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Endoneesi 1,419,588 227,026,560 159.9 Jakarta
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Lawos 236,800 5,777,180 24.4 Vientiane
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Maleesi 329,750 22,662,365 68.7 Kuala Lumpur
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Miyanmaar 678,500 42,238,224 62.3 Naypyidaw
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Filipiin 300,000 84,525,639 281.8 Manila
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Singapoor 704 4,483,900 6,369.0 Singapore
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Taaylaand 514,000 62,354,402 121.3 Bangkok
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Timoor gu Penku 15,007 952,618 63.5 Dili
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Wiyetnaam 329,560 81,098,416 246.1 Hanoi
Ron-goxu End:
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Afganistaan 647,500 27,755,775 42.9 Kabul
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Banglaades 144,000 133,376,684 926.2 Dhaka
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Butaan 47,000 672,425 14.3 Thimphu
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  End 3,167,590 1,045,845,226 318.2 New Delhi
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Iraan 1,648,000 68,467,413 41.5 Tehran
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Maldiif 300 320,165 1,067.2 Malé
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Nepaal 140,800 25,873,917 183.8 Kathmandu
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Pakistaan 803,940 147,663,429 183.7 Islamabad
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Siri Laanka 65,610 19,576,783 298.4 Colombo
Penku gu Diggu, Penku gu Jege
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Armeeni 29,800 3,330,099 111.7 Yerevan
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Aserbayjaan 46,870 3,845,127 82.0 Baku
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Bahrayni 665 656,397 987.1 Manama
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ciipër 9,250 775,927 83.9 Nicosia
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Palestiin: Gaza 363 1,203,591 3,315.7 Gaza
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Jeoorji 20,460 2,032,004 99.3 Tbilisi
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Iraak 437,072 24,001,816 54.9 Baghdad
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Israayil 20,770 6,029,529 290.3 Jerusalem
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Jordaani 92,300 5,307,470 57.5 Amman
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kowet 17,820 2,111,561 118.5 Kuwait City
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Libaan 10,452 3,677,780 353.6 Beirut
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Omaan 212,460 2,713,462 12.8 Muscat
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kataar 11,437 793,341 69.4 Doha
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Araabi Sawdit 1,960,582 23,513,330 12.0 Riyadh
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Siri 185,180 17,155,814 92.6 Damascus
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Tirki 756,768 57,855,068 76.5 Ankara
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Imaaraat yu Araab yu Bennoo yi 82,880 2,445,989 29.5 Abu Dhabi
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Palestiin: West Bank 5,860 2,303,660 393.1
Asi: Diiwaanu Nguuru Room, Karmat ak delluwaay, Xool it  Yaman 527,970 18,701,257 35.4 Sanaá
Total 43,810,582 3,902,404,193 89.07

Ci angale ak ci faranse mooy Asia.

Asi dafa am ñaari tekki ci Injiil.

  1. Ci bu jëkk mooy li ñu tudde tey jii 'Asi Minër', maanaam daanaka lépp ci réew mu tudd tey jii Tirki (Turquie) lu fare penku géeju Ese.
  2. Ñaareel bi, ci jamano Injiil ji, Asi benn diiwaanu nguuru Room la woon. Moo doon wàllug sowu Asi Minër. Dafa boole diiwaani Misi, Lidi, Kari, ak genn wàll Firisi, ak dun ya nekk ca géeju Ese. Waa Room ñoo ko def diiwaan ci 129 j.K.. Ci bu jëkk péeyam moo doon Pergam. Waaye, gannaaw jamano Injiil, def nañu Efes ni péeyam. Juróom ñaari dëkk yi ñu gis ca téere Peeñu ma (Pe 2:1-3:22) ñoo bokkoon ca diiwaanu Asi.

Am na ñi xalaat ne yoon bu nekk ñu gis 'Asi' ci Injiil mooy diiwaanu nguuru Room bi. Am na ñeneen ñi xalaat ne léeg-léeg Injiil dafay wax ci ci Asi Minër (Jëf 19:26-27 21:27 24:18 27:2), te yi ci des mooy diiwaan bi.

Man nañu gis Asi ci Injiil ci Jëf 2:9; 6:9; 16:6; 19:10,22,26,27; 20:4,16,18; 21:27; 24:19; 27:2; Ro 16:5; 1Ko 16:19; 2Ko 1:8; 2Tim 1:15; 1Pi 1:1; Pe 1:4.

Karmat ak delluwaay

Xool it

Jukki yi ci lonku

Lëkkalekaay yu biti

Goxi / Kembaari àdduna si
   
Afritugalasi
Oseyaani Afrig Tugalasi
Bëj-gànnaaru Aamerig Tugal Asi
   
Bëj-saalumu Aamerig

Tags:

Asi Diiwaanu Nguuru RoomAsi Karmat ak delluwaayAsi Xool itAsiAddunaGox

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Réewum CekXeexYamanRéewum DominikXët wu njëkkMbëjfeppalGarabIsiptBalastusPolineesi gu FaraasPremier LeagueBabilonInternetGrenadaRomTangorGine BisaawóoGuyaanaSiriJuróom ñettLouvreMelentaanMbëjbijjaanWolof (làkk)MeeBukkiRiisiNowelMalawiEndoneesiÀllarbaXaymaKongóo-BrasaawiilOngiriAwrilTëriinuw nosukaayKamerunNairobiZurichNamibiGerteJamaykaIraakHo Chi Minh CityFewirieAddis-AbebaSéeréerTehranMbëjSankt-PeterburgSeggEritereWiyetnaamTirkiEswatiniKopparWeerBotswanaAlxamesAltineMàngoMiyanmaarSkopjeQueenGuwaatemalaDiiney AfrigArsantinOmaanImbraatóor gu Songaay🡆 More