Xoos

Xoos xeetu garab la bu bokk ci njabootu Rubiaceae ak ci ñoñ Mitragyna.

Afrig gu Sowwu ak gu digg lay nekk.

Xoos
Nataalu xobi xoos

Meloom wi

Guddaayam danay àgg 8 ba 10i met. Xobam ci guddaay day àgg 6 ba 9i sàntimet, ci yaatuwaay 3,5 ba 5 sàntimet. Melow xol la yore. Tóotóoram day weex te am xet gu tar. Yaatuwaayam 2 ba 2,5i met la. Cari foytéefam day yàgg ak ñoom lool.

Njariñam li

Xoos garab gees di jëfandikoo la ci pajum cosaam ngir faj xeeti tawat yu wuute.

Nataala yi

Turu xam-xamam wi

Mitragyna inermis

Tags:

Xoos Meloom wiXoos Njariñam liXoos Nataala yiXoos Turu xam-xamam wiXoos

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

YattQueenXam-xamu nosukaayAndoorUsbekistaanLituwaaniWékkiGàncaxKopparTëriinuw nosukaayXam-xamKàttanug mbëjAaroonaObsessive compulsive disorderWayBeneAamerigParaguwaayNowelWorld Wide WebKërRéewum LawosEritereDuusub sinFootballGuyDiiwaanu NdarJeoorjiMbàmbulaanug EndSiriSudaan gu Bëj-saalumYaroslavlSan MarinoSëriñ Suhaybu MbàkkeKasakistaanHTMLXët wu njëkkLiechtensteinChongqingKoom-koomWu-angalteerBulgaariRéewum Diggu AfrigTiijaaniyaaIraanSëriñ Móodu Lóo DaganaKowetYaundeNdakaaruWaxtuFundura (Kap Weer)KokoRiisiFànnXayraAsot.st🡆 More