Gàddaay

Gàddaay di ci fr “immigration” baat la buy tekki : tukkee ci barab mbaam réew dem ca meneen, ngir sàkku fa dara, mbaa ngir naqarig sam réew ci yaw mbaa barab ba nga bawoo, loolu di faral di jur ag tumbrànke, akug ndoxondéemu, tax ngay am turu doxondéem giy tekki ku dëkkul ca réew ma nga nekk, cosaanoowoo fa

Kon gàddaay mooy: immigration ci fr

Doxondéem di : étranger

Tumbrànke di coona ak tiis ak naqaru xol gi gàddaay di faral a jur

Looloo waral Yonnant bi (j.m) di faral di wax naan: “Tukki aw daggiit la ci mbugal

Am ku ne moo de da koo woyofal waaye mbugal aw dogiit la ci tukki

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

Stanley, Dunu FalklandXarey jóoñeWommatiinu mbëjMboqNdakaaruWolof (askan)MadagaskaarBulgaariGéej gu DigguSexawBuddaGroznyBeelsebulXUDARWeerWertFànnGayndeSëriñ Abdu Xaadir MbàkkeSompatTugalRiisiRéewum DominikAlxamesDunu KookKebegSofiyaKinshasaHTMLYoos-bisaawMbëjLislaamJëmmBuruselAncos ci SiriNoorweesBawolSapoŋAraabFK PanevėžysBaay FaalWatikaa (péy)XaymaMbaamEndoneesiOlaandNgéejaanApiyus, péncuNewFukkEndNoor.zmDereetKasakistaanBarbadosAlbert EinsteinMàndiŋ mTenePolitigXët wu njëkkPHPNdaté Yalla MbodjDexBaxaKoriAlxuraanul KariimSaa🡆 More