Artemis

Ci angale mooy Diana; Ci faranse mooy Artémis

Artemis mooy turu jenn yàlla ju araam ju jigéen ci làkku gereg. Ci làkku waa room Diyana la tuddoon. Ñaari yàlla yu araam bokkoon nañu tur Artemis. Benn mooy li ñu gis ci Injiil, maanaam yàllay Efes (Jëf 19:23-41). Beneen yàllay gereg la woon ki ñu foog ne jigéenu yàlla ju araam ja tudd Apolo. Diine Artemisu Efes niroo na diine Astarte, yàllay waa Sidon.

Tur wi feeñ na ci Injiil ci Jëf 19:24,27,28,34,35.

Artemis
Nataalu Artemis (Archeological Museum, Efes, Tirki.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

WeerRéewum ñaari dex yiAmmanBernJokkoosoryanteUulTugalAwrilPajMaltKomoorAddis-AbebaDiiwaanu NdarÀddunaTansaniAwa Mari Kol SekkXam-xami nite ak mboolaayPragBuddaBahrayniHo Chi Minh CityBaratislawaRéewum CekPolineesi gu FaraasEcoopiPanamaaWay-dëkkNamibiSiriImaaraat yu Araab yu Bennoo yiWeenusDimbDisc jockeyItaaliLetóoniWaañFaraasSimiBisaawóoWu-faraasBëtEndoneesiKàttanXeexRabÀjjumaDanmaarkSahara gu SowwuLibeeriaNukleonNjàngatTelefonFeppmaanduSamwieGëstubiddiwGuyaanaMbëjfeppalTus-wu-taxawDiiwaanu NdakaaruAraabi SawditIsiptImbraatóor gu SongaayUruguwaayAltineWoy🡆 More