Areyopas

Ci angale mooy Areopagus; Ci faranse mooy Aréopage

Bérab ci biir dëkku Aten la, bu nekk ci kaw wenn tundu xeex wu kawe. Amoon na ay siis yi ñu defare woon doj ngir kureelu dëkk ba manoon faa daje. Indi nañu Pool foofu ngir mu waareji (Jëf 17:18-34).

Areyopas
Areyopas ni ñu ko gise tey ji su fekkee ne yaa ngi ca Akëropool

Tur wi moo feeñ ci Injiil ci Jëf 17:19,22,34.

Logo Commons

Xool it Wiki Commons

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

WikbaatukaayXaralay xibaar ak jokkooBelgradBuddaXiirtalukaayÀddunaWeregKongóo-BrasaawiilArkhangelskMbàmbulaan Gu-DalCreating a connectionBrasawilWay-dëkkDawaanu mbëjPraiaÑaqu rougeole (ŋas)Bennoo gu AlmaañDereetAlbaaniAlmaañIslaandIsipt gu yàgg gaKońskowolaMuhammad Lamin DaraameYamooTimmiñ-tammañPanamaaIniwersite Gaston Berger Bu NdarPombas (Kap Weert)BernCiiliPolineesi gu FaraasYombGàmbiMadagaskaarBésBelaarusBreesilTugalWorld Wide WebJàngoroy EbolaSiinXët mu njëkkPolineesiNdëppDalub webOtrisCoronel FabricianoDisc jockeySomaliXonq🡆 More