Andare

Ci angale mooy Andrew; Ci faranse mooy André

Benn ci fukki taalibe Yeesu ya ak ñaar la woon, di rakku Simoä Piyeer. Ñu bokk ndey ak baay. Nappkat bu bawoo ca dëkk bu tudd Betsayda ca diiwaanu Galile la woon. Bala mu topp ci Yeesu nekkoon na taalibe Yaxya.

Dañuy gis Andare ci Injiil ci Mc 4:18-20; 10:2; Mk 1:16-18,29; 3:18; 13:3,4; Lu 6:14; Yow 1:35-44; 6:8-9; 12:20-22; Jëf 1:13.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

IslaandBurkinaa FaasoSudaan (diiwaan)Diiwaanu NdakaaruMaliMóorisGaawuWaaxNjëkk-xaymàGordon BrownKasakistaanFànnBiir bu dawDawaan bu safaanuAnetKMFIniwersite Gaston Berger Bu NdarWéñumeññetLusakaOngiriBetesdaPyatigorskKanadaaYattTaabJimbulang bu waa-BrëtaañRajabShenyangJordaaniBiti-jawwuGaambiGireesAlbaaniPalestiinRigaTabaMàddMbëjfeppalXayraLislaamRonald ReaganWoyGuyaabArminaatFootballWufaraasGine BisaawóoWolof (làkk)Siddeem bukkiKap WeertKàttanug imbiku🡆 More