Tugal: Gox

Tugal mooy wàll wi féete penku goxub Tugalasi, ci baax dees koy jàppe niki benn ci juroom-benn walla juroom-ñaari goxi àdduna bi. Gox baa gi digu ci sowwu ci mbàmbulaanug Atlas gi, ci bëj-gànnaar ci dottub Bëj-gànnaar bi, yem ci géej gu Diggu gi ci bëj-saalum. Ay digam ci penku dese nañoo leer, dinay faral di jur ay werante; li ko waral mooy ni mu taqalook goxub Asi.

Wiki Tugal
Wiki
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki taxawal

Tugal

xammee tugal.

Dayo 10,180,000 km² (3,930,000 sq mi)
way-dëkk 710,000,000
fattaayu way-dëkk 70/km² 181/sq mi
Turu aji dëkk: Waa-tugal
Réew 48 réew, 27 yi bokk nañ ci Bennoob Tugal
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it
1000.

Waa-Islaand jàppees na leen ni waa-tugal (donte féeteem ci degalub Tugal-Aamerig), ak mbooleem dun yi ci géej gu Diggu gi, Sipër mi gën a jur coow, ci wàllu melosuuf. Riisi ak Tirki ñi am li ëpp ci seen suuf ca Asi, waaye day ni rekk li ëpp ci seen taariix réewi gox bi lañu ko bokkal.

Melosuuf

Ngir xóotal: Melosuufug Tugal Tugal a ngi yaatoo 10 392 855 km² (fukki junni-junni ak ñetti-fukki-junni ak juroom-ñent-fukk ak ñaar ak juroom-ñetti-téeméer ak juroom-fukk ak juroom). Di benn ñetti Afrig walla benn ñenti Asi walla Aamerig.

Mi ngi séedatliku ci jurromi diwaan: Penku Tugal, Diggu Tugal, Sowwu Tugal, Bëj-gànnaaru Tugal ak Bëj-saalumu Tugal

Gox bi am na 49 ciy réew.

Réewi Tugal

Turu diwaan aki
réewam, ak seen raaya
Yaatuwaay
(km²)
Way-dëkk
(1 sulet, 2002)
Fattaay/way-dëkk
(ci km²)
Péy
Penku Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Belaarus 207,600 10,335,382 49.8 Minsk
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Bulgaari 110,910 7,621,337 68.7 Sofiya
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Réewum Cek 78,866 10,256,760 130.1 Prag
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Oonguri 93,030 10,075,034 108.3 Budapest
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Moldaawi 33,843 4,434,547 131.0 Kisinawu
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Poloñ 312,685 38,625,478 123.5 Warsaw
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Romaani 238,391 21,698,181 91.0 Bukarest
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Riisi 3,960,000 106,037,143 26.8 Mosku
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Eslowaaki 48,845 5,422,366 111.0 Baratislawa
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ukreen 603,700 48,396,470 80.2 Kiyew
Bëj-gànnaaru Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Danmaark 43,094 5,368,854 124.6 Kopenagen
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Estooni 45,226 1,415,681 31.3 Talin
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Finlaand 336,593 5,157,537 15.3 Elsinki
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Islaand 103,000 307,261 2.7 Reykjawik
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Irlaand 70,280 4,234,925 60.3 Dublin
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Letóoni 64,589 2,366,515 36.6 Riga
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Lituwaani 65,200 3,601,138 55.2 Wilniyus
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Noorwees 324,220 4,525,116 14.0 Oslo
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Suweed 449,964 9,090,113 19.7 Stokolm
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Nguur-Yu-Bennoo 244,820 61,100,835 244.2 Londar
Bëj-saalumu Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Albaani 28,748 3,600,523 125.2 Tirana
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Andoor 468 68,403 146.2 Andorra la Vella
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Bosni 51,129 4,448,500 77.5 Saarayego
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Korwaasi 56,542 4,437,460 77.7 Sagreb
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ciipër 9 251 788 457 85 ...
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Girees 131,940 10,645,343 80.7 Aten
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Itaali 301,230 58,751,711 191.6 Rom
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Réewum Maseduwaan 25,333 2,054,800 81.1 Skopje
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Malt 316 397,499 1,257.9 Waleta
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Montenegro 13,812 616,258 44.6 Podgorika
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Portugaal 91,568 10,084,245 110.1 Lisbon
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  San Marino 61 27,730 454.6 San Marino
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Seerbi 88,361 9,663,742 109.4 Belgrad
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Esloweeni 20,273 1,932,917 95.3 Jubaljana
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ispaañ 504,851 45,061,274 89.3 Madrid
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Watikaa 0.44 900 2,045.5 Watikaa
Sowwu Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Ótiris 83,858 8,169,929 97.4 Wiyen
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Beljik 30,510 10,274,595 336.8 Burusel
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Faraas 547,030 59,765,983 109.3 Paris
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Almaañ 357,021 83,251,851 233.2 Berlin
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Liechtenstein 160 32,842 205.3 Wadus
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Luksambuur 2,586 448,569 173.5 Lusambuur
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Monaako 1.95 31,987 16,403.6 Monaako (péy)
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Olaand 41,526 16,318,199 393.0 Amsterdam
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Suwis 41,290 7,507,000 176.8 Bern
Diggu Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Kasakistaan 150,000 600,000 4.0 Astana
Penku Tugal:
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Aserbayjaan 7,110 175,200 24.6 Baku
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Jeoorji 2,000 37,520 18.8 Tibilisi
Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it  Tirki 24,378 11,044,932 453.1 Ankara
Lépp 10,176,246 709,608,850 69.7

Karmat ak delluwaay

Xool it

Tugal: Melosuuf, Karmat ak delluwaay, Xool it 

Xool it Wiki Commons

Jukki yi ci lonku

Lëkkalekaay yu biti


Goxi / Kembaari àdduna si
   
Afritugalasi
Oseyaani Afrig Tugalasi
Bëj-gànnaaru Aamerig Tugal Asi
   
Bëj-saalumu Aamerig

Tags:

Tugal MelosuufTugal Karmat ak delluwaayTugal Xool itTugal

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

TembteMaliWërlaayFànnÑaqu meningiteAntananariwoGuyaana gu FaraasAltineFeebaru tëlbëti bu amul appSëriñ Mbay JAXATEBiir bu dawNguur-Yu-BennooDiiwaan yu BennooInternetKopparPenku gu SoriNovosibirskJéemantu wiArsantinNdianéSeex Muhammadu Murtalaa MbàkkeDalub webDjibril Dio MambétyKàllaamaNgéejaanTalaataXam-xamu suuf si ak jawwu jiRaaya wu SenegaalKirgistaanNoorNosteg jantVladivostokMarokNitNewMonte LargoJànkoonte gu mbëjSaytubiddiwAamerigSão Pedro (Kap Weer)XeetEndoneesiBenesuwelaPlutonPàppaayaTabaskiNdakaaruGarabBrasawilBulgaariMustafa Kemal AtatürkOmar Blondin DiopKom-komPenku AsiJordaaniDunu AlandSaaKigaliGoxug AamerigCaxatNanjingYàllaArmeeni🡆 More