Wikbaatukaay

Wikbaatukaay ab baatukaay barilàkk bu ubbeeku la, di benn ci sémbi Wiki Fondation yi.

Baatub «Wikbaatukaay» dafay junj sumb bu wolof bu boobu sémb, di Wiktionary ci wu-angalteer. Mook Wiki ñoo bokk doxiin, di lu ubbeeku te dàttu ci nosteg wiki, lees man a jëfandikoowaat ci anami GFDL.

Wikbaatukaay
Sémbu Wikbaatukaay

Tëddiin

Yéeney sémb bi mooy sos ab baatukaay bees di duggal làkki àdduna bi yépp. Ci bu wolof baat yépp a fiy nekk ak seen tekki ci yeneen làkk waaye ci wolof lañu leen di faramfaccee, joge seen gongikubaat, seeni bokktekki, safaantekki, waxiin, añs.

Tags:

WikipediaWolofWu-angalteer

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

LiechtensteinKureelu Mbootayu Xeet yiDuni KanaariPariKopparMàngoMinskSaint Kitts and NevisPanamaaWay-dëkkBreesilGaambiMoskuTëriinuw nosukaayBeijingSéeréerAserbayjaanFiijiTimoor gu PenkuMosambikIrlaandIspaañNoorweesAhmadou BambaNosukaayWadusLouvreSatumbarBalastusHamedanWatikaaGόorBenesuwelaDimbJolofJeoorji gu Bëj-saalum ak Duni Islaand yi Bëj-saalumYanu mbëjDisc jockeyRonald ReaganEcoopiXaymaMeksigÑaareelu Xareb ÀddunaBalaamTongaWolofEritereNamibiRakkaati-gàmmuPeruFeppmaanduGineg yamooLibeeriaÀllarbaGanaNguur-Yu-BennooRéewum ñaari dex yiSinemaaDunu KookBelgradMaltXUDARDiiney AfrigQueenKodiwaarSenegaalApolyonGayndeBisaawóoIraanDigg bu mbëjTelefonNitTansaniÑayAsmara🡆 More