Nowel

Nowel

Nowel

Ci bu jekk, xeetu Wolof yii maggaluwoon bësu nowel. Waaye leegi ak comercialization du lépp. Yeeneen nit ni ci Ndakaaru ak yeeneen dëkk yu mag yi dañuy maaye ay cadeew ak di def lamp yu rafet ci seen kër. Li ci genn bari ci Wolof yii du nu ay catoliq walla talibe Insa, kon dunuy fonk bësu nowel.

Ci sunu jamanoo dañuy tambali di am ay talibe Insa. Te noom noo jël bësu nowel ngir maggal judug Insa (ki nu wax nee Yeesu Krist ci faranse). Seen maggal mingi aaw ci ay woy, ak i ñaan ak lekkando.

Tags:

🔥 Trending searches on Wiki Wolof:

GàncaxSaaHo Chi Minh CityOsascoArsantinMbëjSaint Kitts and NevisTimoor gu PenkuMiyanmaarAmmanStokolmAngolaaZurichDëgërlukaaySão PauloDigg bu mbëjSkopjeMustafa Kemal AtatürkQomNosteg doxiinYoonKore gu Bëj-saalumSéeréerAyubésRéewum Popileer bu SiinMbëjfeppalKoom-koomJinaxAtaliDooleranduDibéerMàndiŋ mWolof (làkk)Tus-wu-taxawMashhadSinemaaOmaanFeppmaanduMinskLetóoniMoskuIsfahanGarabNguur-Yu-BennooMàngoMalawiPremier LeaguePakistaanŊas (rougeole)IrkutskJuróom ñaarWolofBukkiDiggu AamerigMbàmbulaanug AtlasSowwu TugalBëj-saalumu AfrigMaliOngiriWatikaaDuni MarshallDublinBukarestKol-kolu suuf siHamedanTembteSudaan gu Bëj-saalumFC PortoNguur-giSahrul ProjecttRiisi🡆 More